Al-Hijr · 96/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
الَّذِينَ يَجْعَلُونَ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ ۚ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ ۝٩٦
Allazeena yaj`aloona ma`al laahi ilaahan aakhar; fasawfa ya`lamoon
📖 Tekkim Wolof
Ña nga xam ne dañuy boole Yàlla ak jeneen yàlla, danañu mës a xam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 94-98 — Simoore Al-Hijr

94فَاصْدَعْ بِمَا تُؤْمَرُ وَأَعْرِضْ عَنِ الْمُشْرِكِينَ
Waxal ci kaw li Nu la digal te nanga dëddu bokkaalekat yi.
95إِنَّا كَفَيْنَاكَ الْمُسْتَهْزِئِينَ
Naka Nun fegal nanu la ña lay téjji.
96الَّذِينَ يَجْعَلُونَ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ ۚ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ
Ña nga xam ne dañuy boole Yàlla ak jeneen yàlla, danañu mës a xam.
97وَلَقَدْ نَعْلَمُ أَنَّكَ يَضِيقُ صَدْرُكَ بِمَا يَقُولُونَ
Xam Nanu ne la ñuy wax tiis na ci sa xol.
98فَسَبِّحْ بِحَمْدِ رَبِّكَ وَكُن مِّنَ السَّاجِدِينَ
Sàbbaalal sa Boroom mi yeyoo cant, te nanga bokk ca sujjóotkat ya ;
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
96Aaya

Tekki — Al-Hijr 96

Simoore Al-Hijr Aaya 96 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña nga xam ne dañuy boole Yàlla ak jeneen yàlla,…

Simoore Aaya 96/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 94–98. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers