Al-Hijr · 99/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
وَاعْبُدْ رَبَّكَ حَتَّىٰ يَأْتِيَكَ الْيَقِينُ ۝٩٩
Wa`bud Rabbaka hattaa yaatiyakal yaqeen
📖 Tekkim Wolof
te nangay jaamu Yàlla ba balaa bir la [dee ga] di agsi ci yaw.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 97-99 — Simoore Al-Hijr

97وَلَقَدْ نَعْلَمُ أَنَّكَ يَضِيقُ صَدْرُكَ بِمَا يَقُولُونَ
Xam Nanu ne la ñuy wax tiis na ci sa xol.
98فَسَبِّحْ بِحَمْدِ رَبِّكَ وَكُن مِّنَ السَّاجِدِينَ
Sàbbaalal sa Boroom mi yeyoo cant, te nanga bokk ca sujjóotkat ya ;
99وَاعْبُدْ رَبَّكَ حَتَّىٰ يَأْتِيَكَ الْيَقِينُ
te nangay jaamu Yàlla ba balaa bir la [dee ga] di agsi ci yaw.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
99Aaya

Tekki — Al-Hijr 99

Simoore Al-Hijr Aaya 99 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te nangay jaamu Yàlla ba balaa bir la [dee ga]…

Simoore Aaya 99/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 97–99. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers