Al-Hijr · 98/99
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hijr
فَسَبِّحْ بِحَمْدِ رَبِّكَ وَكُن مِّنَ السَّاجِدِينَ ۝٩٨
Fasbbih bihamdi Rabbika wa kum minas saajideen
📖 Tekkim Wolof
Sàbbaalal sa Boroom mi yeyoo cant, te nanga bokk ca sujjóotkat ya ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 96-99 — Simoore Al-Hijr

96الَّذِينَ يَجْعَلُونَ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ ۚ فَسَوْفَ يَعْلَمُونَ
Ña nga xam ne dañuy boole Yàlla ak jeneen yàlla, danañu mës a xam.
97وَلَقَدْ نَعْلَمُ أَنَّكَ يَضِيقُ صَدْرُكَ بِمَا يَقُولُونَ
Xam Nanu ne la ñuy wax tiis na ci sa xol.
98فَسَبِّحْ بِحَمْدِ رَبِّكَ وَكُن مِّنَ السَّاجِدِينَ
Sàbbaalal sa Boroom mi yeyoo cant, te nanga bokk ca sujjóotkat ya ;
99وَاعْبُدْ رَبَّكَ حَتَّىٰ يَأْتِيَكَ الْيَقِينُ
te nangay jaamu Yàlla ba balaa bir la [dee ga] di agsi ci yaw.
Al-HijrFihi Alxuraan
99Aaya
MeccanRevelation
98Aaya

Tekki — Al-Hijr 98

Simoore Al-Hijr Aaya 98 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sàbbaalal sa Boroom mi yeyoo cant, te nanga bokk ca…

Simoore Aaya 98/99 — Simoore Al-Hijr الحجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hijr Dégg, Simoore Al-Hijr Tekki, Simoore Al-Hijr mp3, Simoore Al-Hijr pdf. Aaya 96–99. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers