An-Nahl · 17/128
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nahl
أَفَمَن يَخْلُقُ كَمَن لَّا يَخْلُقُ ۗ أَفَلَا تَذَكَّرُونَ ۝١٧
Afamany yakhluqu kamallaa yakhluq; afalaa tazak karoon
📖 Tekkim Wolof
Waaw ndax ku bind dana mën a yem ak ku bindul dara ? Moo ndax dangeen dul fàttaliku ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 15-19 — Simoore An-Nahl

15وَأَلْقَىٰ فِي الْأَرْضِ رَوَاسِيَ أَن تَمِيدَ بِكُمْ وَأَنْهَارًا وَسُبُلًا لَّعَلَّكُمْ تَهْتَدُونَ
Te Moo samp ci suuf si ay ndëgërlaay [mu dal] bañ a jaayu ak yéen, ak i dex ak i yoon,
16وَعَلَامَاتٍ ۚ وَبِالنَّجْمِ هُمْ يَهْتَدُونَ
[def na it ci suuf si] ay màndarga, nit ña mën a gindikoo ci bidiw yi.
17أَفَمَن يَخْلُقُ كَمَن لَّا يَخْلُقُ ۗ أَفَلَا تَذَكَّرُونَ
Waaw ndax ku bind dana mën a yem ak ku bindul dara ? Moo ndax dangeen dul fàttaliku ?
18وَإِن تَعُدُّوا نِعْمَةَ اللَّهِ لَا تُحْصُوهَا ۗ إِنَّ اللَّهَ لَغَفُورٌ رَّحِيمٌ
Te bu ngeen doon jéem a lim xéewal yi leen Yàlla defal, dungeen ko mën. Te Yàlla Moom Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
19وَاللَّهُ يَعْلَمُ مَا تُسِرُّونَ وَمَا تُعْلِنُونَ
Te Yàlla xam na li ngeen nëbb ak li ngeen feeñal.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
17Aaya

Tekki — An-Nahl 17

Simoore An-Nahl Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waaw ndax ku bind dana mën a yem ak ku…

Simoore Aaya 17/128 — Simoore An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nahl Dégg, Simoore An-Nahl Tekki, Simoore An-Nahl mp3, Simoore An-Nahl pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers