An-Nahl · 55/128
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nahl
لِيَكْفُرُوا بِمَا آتَيْنَاهُمْ ۚ فَتَمَتَّعُوا ۖ فَسَوْفَ تَعْلَمُونَ ۝٥٥
Liyakfuroo bimaa aatainaahum; fatamatta`oo, faswfa ta`lamoon
📖 Tekkim Wolof
Ngir weddi la Nu leen jox. Xéewluleen ! Dangeen mës a xam !

🎧 Dégg


📜 Aaya 53-57 — Simoore An-Nahl

53وَمَا بِكُم مِّن نِّعْمَةٍ فَمِنَ اللَّهِ ۖ ثُمَّ إِذَا مَسَّكُمُ الضُّرُّ فَإِلَيْهِ تَجْأَرُونَ
Li ngeen am ciw yiw mi ngi jóge ca Yàlla. Te bu leen lu metti dalee, Moom ngeen di ñaan ndimbal.
54ثُمَّ إِذَا كَشَفَ الضُّرَّ عَنكُمْ إِذَا فَرِيقٌ مِّنكُم بِرَبِّهِمْ يُشْرِكُونَ
Te bu leen lor ja deggikoo, mu am ab kurél buy bokkaaleeti seen Boroom,
55لِيَكْفُرُوا بِمَا آتَيْنَاهُمْ ۚ فَتَمَتَّعُوا ۖ فَسَوْفَ تَعْلَمُونَ
Ngir weddi la Nu leen jox. Xéewluleen ! Dangeen mës a xam !
56وَيَجْعَلُونَ لِمَا لَا يَعْلَمُونَ نَصِيبًا مِّمَّا رَزَقْنَاهُمْ ۗ تَاللَّهِ لَتُسْأَلُنَّ عَمَّا كُنتُمْ تَفْتَرُونَ
Ñuy sàkkal ay cër ca la Nu leen wërsëgal ñoo xam ne xamuñu leen. Waat naa ci Yàlla ne dees na leen laaj la ngeen nekkoon di ko duur.
57وَيَجْعَلُونَ لِلَّهِ الْبَنَاتِ سُبْحَانَهُ ۙ وَلَهُم مَّا يَشْتَهُونَ
Ñuy sàkkal Yàlla ay doom yu jigéen. Sellam ga [sori na lool ! Te ñoom ñuy moomale seen bopp la ñu bëgg [ay doom yu góor].
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
55Aaya

Tekki — An-Nahl 55

Simoore An-Nahl Aaya 55 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ngir weddi la Nu leen jox. Xéewluleen ! Dangeen mës…

Simoore Aaya 55/128 — Simoore An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nahl Dégg, Simoore An-Nahl Tekki, Simoore An-Nahl mp3, Simoore An-Nahl pdf. Aaya 53–57. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers