An-Nahl · 85/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
وَإِذَا رَأَى الَّذِينَ ظَلَمُوا الْعَذَابَ فَلَا يُخَفَّفُ عَنْهُمْ وَلَا هُمْ يُنظَرُونَ ۝٨٥
Wa izaa ra al lazeena zalamul `azaaba falaa yukhaf fafu `anhum wa laa hum yunzaroon
📖 Tekkim Wolof
Ña tooñ, bis ba ñu gisee mbugal ma, deesuleen woyofalal dara, te deefuleen yeexe.
🎧 Dégg

📜 Aaya 83-87 — An-Nahl

83يَعْرِفُونَ نِعْمَتَ اللَّهِ ثُمَّ يُنكِرُونَهَا وَأَكْثَرُهُمُ الْكَافِرُونَ
Xam nañu xell Yàlla ba noppi ; ñu fakk ko. Te ñu bari ci ñoom yéefar lañu.
84وَيَوْمَ نَبْعَثُ مِن كُلِّ أُمَّةٍ شَهِيدًا ثُمَّ لَا يُؤْذَنُ لِلَّذِينَ كَفَرُوا وَلَا هُمْ يُسْتَعْتَبُونَ
Ca bis ba Nu dogalee ci xeet wu ne seen seede, te deeful may [ña weddi] lay, te duñu leen nangul it ngànt.
85وَإِذَا رَأَى الَّذِينَ ظَلَمُوا الْعَذَابَ فَلَا يُخَفَّفُ عَنْهُمْ وَلَا هُمْ يُنظَرُونَ
Ña tooñ, bis ba ñu gisee mbugal ma, deesuleen woyofalal dara, te deefuleen yeexe.
86وَإِذَا رَأَى الَّذِينَ أَشْرَكُوا شُرَكَاءَهُمْ قَالُوا رَبَّنَا هَٰؤُلَاءِ شُرَكَاؤُنَا الَّذِينَ كُنَّا نَدْعُو مِن دُونِكَ ۖ فَأَلْقَوْا إِلَيْهِمُ الْقَوْلَ إِنَّكُمْ لَكَاذِبُونَ
Te ña doon bokkaale, bu ñu gisee seen xërëm ya, danañu ne : “Yaw sunu Boroom, ñile ñoo di ñanu daan bokkaalee, di leen jaamu bàyyi la”. Ñoom it ñu tontu ne : “Yéen ay fenkat ngeen”.
87وَأَلْقَوْا إِلَى اللَّهِ يَوْمَئِذٍ السَّلَمَ ۖ وَضَلَّ عَنْهُم مَّا كَانُوا يَفْتَرُونَ
Ñu sànni jëme ca Yàlla, ca bis booba njébbal la ñu doon duur réer leen [Yàlla rekk a fi sës].
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
85Aaya

Tekki — An-Nahl 85

Simoore An-Nahl Aaya 85 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña tooñ, bis ba ñu gisee mbugal ma, deesuleen woyofalal…

Simoore Aaya 85/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 83–87. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers