Al-Isra · 87/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
إِلَّا رَحْمَةً مِّن رَّبِّكَ ۚ إِنَّ فَضْلَهُ كَانَ عَلَيْكَ كَبِيرًا ۝٨٧
Illaa rahmatam mir Rabbik; inna fadlahoo kaana `alaika kabeeraa
📖 Tekkim Wolof
Lu dul yërmaande ju jóge ci sa Boroom, te ngënéelam li Mu la jagleel rëy na [ba tax na Mu bàyyee la xam-xam bi bañ koo rocci].

🎧 Dégg


📜 Aaya 85-89 — Al-Isra

85وَيَسْأَلُونَكَ عَنِ الرُّوحِ ۖ قُلِ الرُّوحُ مِنْ أَمْرِ رَبِّي وَمَا أُوتِيتُم مِّنَ الْعِلْمِ إِلَّا قَلِيلًا
Ña nga lay laaj lu jëm ci ruu, - Neel : “ Ruu ci mbiri sama Boroom la bokk”. Te joxeefuleen ci xam-xam lu dul lu tuuti.
86وَلَئِن شِئْنَا لَنَذْهَبَنَّ بِالَّذِي أَوْحَيْنَا إِلَيْكَ ثُمَّ لَا تَجِدُ لَكَ بِهِ عَلَيْنَا وَكِيلًا
Ca dëgg-dëgg su Nu neexoon, Nu yóbbu li nu la xamal ; te kon doo am kenn ku la musal ci Nun.
87إِلَّا رَحْمَةً مِّن رَّبِّكَ ۚ إِنَّ فَضْلَهُ كَانَ عَلَيْكَ كَبِيرًا
Lu dul yërmaande ju jóge ci sa Boroom, te ngënéelam li Mu la jagleel rëy na [ba tax na Mu bàyyee la xam-xam bi bañ koo rocci].
88قُل لَّئِنِ اجْتَمَعَتِ الْإِنسُ وَالْجِنُّ عَلَىٰ أَن يَأْتُوا بِمِثْلِ هَٰذَا الْقُرْآنِ لَا يَأْتُونَ بِمِثْلِهِ وَلَوْ كَانَ بَعْضُهُمْ لِبَعْضٍ ظَهِيرًا
Neel : “Bu nit ak jinne booloo woon ngir fexee indi lu mel ni Alxuraan jii, duñu mën a indi lu ni mel, doonte dañu caa dimbalante”.
89وَلَقَدْ صَرَّفْنَا لِلنَّاسِ فِي هَٰذَا الْقُرْآنِ مِن كُلِّ مَثَلٍ فَأَبَىٰ أَكْثَرُ النَّاسِ إِلَّا كُفُورًا
Te ca dëgg-dëgg, jox Nanu nit ñi ci Alxuraan jii léebu wu ne [wuy leeral]. Waaye terewul li ëpp ci ñoom wéy di weddi.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
87Aaya

Tekki — Al-Isra 87

Simoore Al-Isra Aaya 87 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lu dul yërmaande ju jóge ci sa Boroom, te ngënéelam…

Simoore Aaya 87/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 85–89. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers