Al-Isra · 95/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
قُل لَّوْ كَانَ فِي الْأَرْضِ مَلَائِكَةٌ يَمْشُونَ مُطْمَئِنِّينَ لَنَزَّلْنَا عَلَيْهِم مِّنَ السَّمَاءِ مَلَكًا رَّسُولًا ٩٥
Transliteration
Qul law kaana fil ardi malaaa `ikatuny yamshoona mutma`inneena lanazzalnaa `alaihim minas samaaa`i malakar Rasoolaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Bu fekkoon ne ay Malaaka ñoo nekkoon ci kaw suuf si di dox, kon de Malaaka Lanuy yónni ci ñoom Mu jóge asamaan”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 93-97 — Al-Isra
93أَوْ يَكُونَ لَكَ بَيْتٌ مِّن زُخْرُفٍ أَوْ تَرْقَىٰ فِي السَّمَاءِ وَلَن نُّؤْمِنَ لِرُقِيِّكَ حَتَّىٰ تُنَزِّلَ عَلَيْنَا كِتَابًا نَّقْرَؤُهُ ۗ قُلْ سُبْحَانَ رَبِّي هَلْ كُنتُ إِلَّا بَشَرًا رَّسُولًا
mbaa nga am këru wurus ; mbaa nga yéeg ci kaw asamaan si. Te dunu gëm sa yéeg feek wàcceloonu Téere bu nuy jàng”. Neel : “Tudd naa sellug sama Boroom ! Moo ndax man nekkuma lu dul nit ku ñu yónni doŋŋ ? "
94وَمَا مَنَعَ النَّاسَ أَن يُؤْمِنُوا إِذْ جَاءَهُمُ الْهُدَىٰ إِلَّا أَن قَالُوا أَبَعَثَ اللَّهُ بَشَرًا رَّسُولًا
Te lan moo tere nit ñi gëm, ba leen njub ga dikkalee, lu dul la ñuy wax naan : “Moo ndax Yàlla dana yónni nit [nit ni nun]muy ab Yonent ? ”
95قُل لَّوْ كَانَ فِي الْأَرْضِ مَلَائِكَةٌ يَمْشُونَ مُطْمَئِنِّينَ لَنَزَّلْنَا عَلَيْهِم مِّنَ السَّمَاءِ مَلَكًا رَّسُولًا
Neel : “Bu fekkoon ne ay Malaaka ñoo nekkoon ci kaw suuf si di dox, kon de Malaaka Lanuy yónni ci ñoom Mu jóge asamaan”.
96قُلْ كَفَىٰ بِاللَّهِ شَهِيدًا بَيْنِي وَبَيْنَكُمْ ۚ إِنَّهُ كَانَ بِعِبَادِهِ خَبِيرًا بَصِيرًا
Neel : “Yàlla doy na seede sama diggante ak yéen”. Moom Yàlla nag nekk na ci ay jaamam, di Ku xam, di Kuy gis [seeni mbir].
97وَمَن يَهْدِ اللَّهُ فَهُوَ الْمُهْتَدِ ۖ وَمَن يُضْلِلْ فَلَن تَجِدَ لَهُمْ أَوْلِيَاءَ مِن دُونِهِ ۖ وَنَحْشُرُهُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ عَلَىٰ وُجُوهِهِمْ عُمْيًا وَبُكْمًا وَصُمًّا ۖ مَّأْوَاهُمْ جَهَنَّمُ ۖ كُلَّمَا خَبَتْ زِدْنَاهُمْ سَعِيرًا
Ku Yàlla gindi nga jub, Ku mu bàyyi cig réer... duñu am keneen ku ñuy wéeru te Dananu leen dajale bisub dekki ba, ñu di leen diri ci seeni kanam, ñu gumba, tëx, lu. Seen dëkkuwaay moo di Safara : te saa yu giimee Nu dolli leen seneen safara.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
95Aaya
Tekki — Al-Isra 95
Simoore Al-Isra Aaya 95 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Bu fekkoon ne ay Malaaka ñoo nekkoon ci…Simoore Aaya 95/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 93–97. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








