Al-Kahf · 97/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
فَمَا اسْطَاعُوا أَن يَظْهَرُوهُ وَمَا اسْتَطَاعُوا لَهُ نَقْبًا ۝٩٧
Famas taa`ooo any yazharoohu wa mastataa`oo lahoo naqbaa
📖 Tekkim Wolof
Yaa juuja ak Maa juuja duñu ko mën a bënn te duñu ko mën a daane.

🎧 Dégg


📜 Aaya 95-99 — Al-Kahf

95قَالَ مَا مَكَّنِّي فِيهِ رَبِّي خَيْرٌ فَأَعِينُونِي بِقُوَّةٍ أَجْعَلْ بَيْنَكُمْ وَبَيْنَهُمْ رَدْمًا
Mu ne leen : “Li ma Yàlla defal moo gën ci man [seenug pey]. Li may laaj rekk mooy ngeen jàppale ma, danaa defar ab ñag seen diggante ak ñoom.
96آتُونِي زُبَرَ الْحَدِيدِ ۖ حَتَّىٰ إِذَا سَاوَىٰ بَيْنَ الصَّدَفَيْنِ قَالَ انفُخُوا ۖ حَتَّىٰ إِذَا جَعَلَهُ نَارًا قَالَ آتُونِي أُفْرِغْ عَلَيْهِ قِطْرًا
Indil-leen ma mbuluŋi weñ gu ñuul, te ngeen fatte ko bën-bën yii, te ngeen soy ko ba mu ruy, ngeen sotti ci betteex bi”.
97فَمَا اسْطَاعُوا أَن يَظْهَرُوهُ وَمَا اسْتَطَاعُوا لَهُ نَقْبًا
Yaa juuja ak Maa juuja duñu ko mën a bënn te duñu ko mën a daane.
98قَالَ هَٰذَا رَحْمَةٌ مِّن رَّبِّي ۖ فَإِذَا جَاءَ وَعْدُ رَبِّي جَعَلَهُ دَكَّاءَ ۖ وَكَانَ وَعْدُ رَبِّي حَقًّا
Zul-Qarnaynine leen : “Lii dey xéewal la gu bawoo fa Yàlla. Waaye, Saa su digub Yàlla agsee, ca la koy màbb. Te digub Yàlla bi dëgg la te fàwwu mu dikk”.
99۞ وَتَرَكْنَا بَعْضَهُمْ يَوْمَئِذٍ يَمُوجُ فِي بَعْضٍ ۖ وَنُفِخَ فِي الصُّورِ فَجَمَعْنَاهُمْ جَمْعًا
Bu boobaa, nit ñi dañuy mbëkkënte ni ay duusi géej, bu ñu walee buftu ba, Nu daldi leen di dajale ñoom ñépp.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
97Aaya

Tekki — Al-Kahf 97

Simoore Al-Kahf Aaya 97 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yaa juuja ak Maa juuja duñu ko mën a bënn…

Simoore Aaya 97/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 95–99. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers