Maryam · 17/98
Tekki Waxtaan — Maryam
فَاتَّخَذَتْ مِن دُونِهِمْ حِجَابًا فَأَرْسَلْنَا إِلَيْهَا رُوحَنَا فَتَمَثَّلَ لَهَا بَشَرًا سَوِيًّا ۝١٧
Fattakhazat min doonihim hijaaban fa arsalnaaa ilaihaa roohanaa fatamassala lahaa basharan sawiyyaa
📖 Tekkim Wolof
Mu wutoon kiiraay seen diggante. Nu daldi yónni ci moom Sunu ruu [Malaaka] mu yor jëmmi nit [Jibriil].

🎧 Dégg


📜 Aaya 15-19 — Maryam

15وَسَلَامٌ عَلَيْهِ يَوْمَ وُلِدَ وَيَوْمَ يَمُوتُ وَيَوْمَ يُبْعَثُ حَيًّا
Te jàmm rekk la am ca ba mu juddoo ak ca ba muy dee, ak ca ba muy dekkiwaat !
16وَاذْكُرْ فِي الْكِتَابِ مَرْيَمَ إِذِ انتَبَذَتْ مِنْ أَهْلِهَا مَكَانًا شَرْقِيًّا
[Fàttalikul], ca Téere ba, Maryaama ba mu fàddoo mbokk ya, génn dem fa penku dëkk ba.
17فَاتَّخَذَتْ مِن دُونِهِمْ حِجَابًا فَأَرْسَلْنَا إِلَيْهَا رُوحَنَا فَتَمَثَّلَ لَهَا بَشَرًا سَوِيًّا
Mu wutoon kiiraay seen diggante. Nu daldi yónni ci moom Sunu ruu [Malaaka] mu yor jëmmi nit [Jibriil].
18قَالَتْ إِنِّي أَعُوذُ بِالرَّحْمَٰنِ مِنكَ إِن كُنتَ تَقِيًّا
[Maryaama] daldi ne : “Man dey maa ngi sàkku ci yërëmaakoon bi [Yàlla] mu musal ma ci yaw ndeem ku ragal Yàlla nga.
19قَالَ إِنَّمَا أَنَا رَسُولُ رَبِّكِ لِأَهَبَ لَكِ غُلَامًا زَكِيًّا
Malaaka ma [Jibriil] ne ko : “Man dey ndawul sa Boroom laa [damaa ñëw] ngir may la doom ju sell”.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
17Aaya

Tekki — Maryam 17

Simoore Maryam Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu wutoon kiiraay seen diggante. Nu daldi yónni ci moom…

Simoore Aaya 17/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers