Maryam · 52/98
Tekki Waxtaan — Maryam
وَنَادَيْنَاهُ مِن جَانِبِ الطُّورِ الْأَيْمَنِ وَقَرَّبْنَاهُ نَجِيًّا ۝٥٢
Wa naadainaahu min jaanibit Tooril aimani wa qarrabnaahu najiyyaa
📖 Tekkim Wolof
Woo Nanu ko ca wetug ndeyjooru tundu Sinaay wa, sësloo ko rëkk ci Nun.

🎧 Dégg


📜 Aaya 50-54 — Maryam

50وَوَهَبْنَا لَهُم مِّن رَّحْمَتِنَا وَجَعَلْنَا لَهُمْ لِسَانَ صِدْقٍ عَلِيًّا
Nu daldi leen may ci Sunu yërmaande, defal leen làmmiñ wu dëggu wu kawe.
51وَاذْكُرْ فِي الْكِتَابِ مُوسَىٰ ۚ إِنَّهُ كَانَ مُخْلَصًا وَكَانَ رَسُولًا نَّبِيًّا
[Fàttalikul] Muusaa ca Téere ba. Moom dey ku sellal la woon, di ku ñu soloo, di ab Yonent.
52وَنَادَيْنَاهُ مِن جَانِبِ الطُّورِ الْأَيْمَنِ وَقَرَّبْنَاهُ نَجِيًّا
Woo Nanu ko ca wetug ndeyjooru tundu Sinaay wa, sësloo ko rëkk ci Nun.
53وَوَهَبْنَا لَهُ مِن رَّحْمَتِنَا أَخَاهُ هَارُونَ نَبِيًّا
Nu daldi koy may ci Sunu yërmaande, defal ko mbokkam ma Aaruuna mu di ab Yonent.
54وَاذْكُرْ فِي الْكِتَابِ إِسْمَاعِيلَ ۚ إِنَّهُ كَانَ صَادِقَ الْوَعْدِ وَكَانَ رَسُولًا نَّبِيًّا
[Fàttalikul] Ismayla ca Téere ba. Doonoon na boroom dégg bu dëggu ; dib Yonent.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
52Aaya

Tekki — Maryam 52

Simoore Maryam Aaya 52 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Woo Nanu ko ca wetug ndeyjooru tundu Sinaay wa, sësloo…

Simoore Aaya 52/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 50–54. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers