Maryam · 53/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
وَوَهَبْنَا لَهُ مِن رَّحْمَتِنَا أَخَاهُ هَارُونَ نَبِيًّا ۝٥٣
Wa wahabnaa lahoo mir rahmatinaaa akhaahu Haaroona Nabiyyaa
📖 Tekkim Wolof
Nu daldi koy may ci Sunu yërmaande, defal ko mbokkam ma Aaruuna mu di ab Yonent.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 51-55 — Simoore Maryam

51وَاذْكُرْ فِي الْكِتَابِ مُوسَىٰ ۚ إِنَّهُ كَانَ مُخْلَصًا وَكَانَ رَسُولًا نَّبِيًّا
[Fàttalikul] Muusaa ca Téere ba. Moom dey ku sellal la woon, di ku ñu soloo, di ab Yonent.
52وَنَادَيْنَاهُ مِن جَانِبِ الطُّورِ الْأَيْمَنِ وَقَرَّبْنَاهُ نَجِيًّا
Woo Nanu ko ca wetug ndeyjooru tundu Sinaay wa, sësloo ko rëkk ci Nun.
53وَوَهَبْنَا لَهُ مِن رَّحْمَتِنَا أَخَاهُ هَارُونَ نَبِيًّا
Nu daldi koy may ci Sunu yërmaande, defal ko mbokkam ma Aaruuna mu di ab Yonent.
54وَاذْكُرْ فِي الْكِتَابِ إِسْمَاعِيلَ ۚ إِنَّهُ كَانَ صَادِقَ الْوَعْدِ وَكَانَ رَسُولًا نَّبِيًّا
[Fàttalikul] Ismayla ca Téere ba. Doonoon na boroom dégg bu dëggu ; dib Yonent.
55وَكَانَ يَأْمُرُ أَهْلَهُ بِالصَّلَاةِ وَالزَّكَاةِ وَكَانَ عِندَ رَبِّهِ مَرْضِيًّا
Daa woon na digal njabootam taxawal julli ak asaka, di ku amoom ngërëmul Yàlla.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
53Aaya

Tekki — Maryam 53

Simoore Maryam Aaya 53 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu daldi koy may ci Sunu yërmaande, defal ko mbokkam…

Simoore Aaya 53/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 51–55. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers