Taha · 109/135
Tekki Waxtaan — Taha
يَوْمَئِذٍ لَّا تَنفَعُ الشَّفَاعَةُ إِلَّا مَنْ أَذِنَ لَهُ الرَّحْمَٰنُ وَرَضِيَ لَهُ قَوْلًا ١٠٩
Transliteration
Yawma `izil laa tanfa`ush shafaa`atu illaa man azina lahur Rahmaanu wa radiya lahoo qawlaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Bisub kerook, kenn du fa mën a ramm ku dul koo xam ne Yërëmaakoon baa ko ko digal te gërëm ay waxam.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 107-111 — Taha
107لَّا تَرَىٰ فِيهَا عِوَجًا وَلَا أَمْتًا
dootoo gis ab nóox-nóox walla ab junni-junni, léppay maase nerr.
108يَوْمَئِذٍ يَتَّبِعُونَ الدَّاعِيَ لَا عِوَجَ لَهُ ۖ وَخَشَعَتِ الْأَصْوَاتُ لِلرَّحْمَٰنِ فَلَا تَسْمَعُ إِلَّا هَمْسًا
Ca Bis booba ñépp danañu topp wootekat ba ; kàddu yépp ne xuum [cëy Yàlla Yërëmaakoon bi]. Doofa dégg lu dul kuy dée [di wax ndànk].
109يَوْمَئِذٍ لَّا تَنفَعُ الشَّفَاعَةُ إِلَّا مَنْ أَذِنَ لَهُ الرَّحْمَٰنُ وَرَضِيَ لَهُ قَوْلًا
Bisub kerook, kenn du fa mën a ramm ku dul koo xam ne Yërëmaakoon baa ko ko digal te gërëm ay waxam.
110يَعْلَمُ مَا بَيْنَ أَيْدِيهِمْ وَمَا خَلْفَهُمْ وَلَا يُحِيطُونَ بِهِ عِلْمًا
Moo xam la jàll ak liy ñëwi, te kenn ci ñoom mënu koo peeg ci xam ko.
111۞ وَعَنَتِ الْوُجُوهُ لِلْحَيِّ الْقَيُّومِ ۖ وَقَدْ خَابَ مَنْ حَمَلَ ظُلْمًا
Loos yépp janoo nañu fa kanamu Yàlla, Muy dundu te taxawu lépp, te képp ku yenu na ag tooñ , [na ko wóor ne] sooy na bu kero gee.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
109Aaya
Tekki — Taha 109
Simoore Taha Aaya 109 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bisub kerook, kenn du fa mën a ramm ku dul…Simoore Aaya 109/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 107–111. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








