Taha · 110/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
يَعْلَمُ مَا بَيْنَ أَيْدِيهِمْ وَمَا خَلْفَهُمْ وَلَا يُحِيطُونَ بِهِ عِلْمًا ۝١١٠
Ya`lamu maa bainaa aideehim wa maa khalfahum wa laa yauheetoona bihee `ilmaa
📖 Tekkim Wolof
Moo xam la jàll ak liy ñëwi, te kenn ci ñoom mënu koo peeg ci xam ko.

🎧 Dégg


📜 Aaya 108-112 — Simoore Taha

108يَوْمَئِذٍ يَتَّبِعُونَ الدَّاعِيَ لَا عِوَجَ لَهُ ۖ وَخَشَعَتِ الْأَصْوَاتُ لِلرَّحْمَٰنِ فَلَا تَسْمَعُ إِلَّا هَمْسًا
Ca Bis booba ñépp danañu topp wootekat ba ; kàddu yépp ne xuum [cëy Yàlla Yërëmaakoon bi]. Doofa dégg lu dul kuy dée [di wax ndànk].
109يَوْمَئِذٍ لَّا تَنفَعُ الشَّفَاعَةُ إِلَّا مَنْ أَذِنَ لَهُ الرَّحْمَٰنُ وَرَضِيَ لَهُ قَوْلًا
Bisub kerook, kenn du fa mën a ramm ku dul koo xam ne Yërëmaakoon baa ko ko digal te gërëm ay waxam.
110يَعْلَمُ مَا بَيْنَ أَيْدِيهِمْ وَمَا خَلْفَهُمْ وَلَا يُحِيطُونَ بِهِ عِلْمًا
Moo xam la jàll ak liy ñëwi, te kenn ci ñoom mënu koo peeg ci xam ko.
111۞ وَعَنَتِ الْوُجُوهُ لِلْحَيِّ الْقَيُّومِ ۖ وَقَدْ خَابَ مَنْ حَمَلَ ظُلْمًا
Loos yépp janoo nañu fa kanamu Yàlla, Muy dundu te taxawu lépp, te képp ku yenu na ag tooñ , [na ko wóor ne] sooy na bu kero gee.
112وَمَن يَعْمَلْ مِنَ الصَّالِحَاتِ وَهُوَ مُؤْمِنٌ فَلَا يَخَافُ ظُلْمًا وَلَا هَضْمًا
Képp koo xam ne nag yaa ngay jëf u yiw te gëm, du ragal foofa ag tooñ [gu ñu koy tooñ], walla ku koy sërxal.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
110Aaya

Tekki — Taha 110

Simoore Taha Aaya 110 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo xam la jàll ak liy ñëwi, te kenn ci…

Simoore Aaya 110/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 108–112. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers