Taha · 112/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
وَمَن يَعْمَلْ مِنَ الصَّالِحَاتِ وَهُوَ مُؤْمِنٌ فَلَا يَخَافُ ظُلْمًا وَلَا هَضْمًا ۝١١٢
Wa mai ya`mal minas saalihaati wa huwa mu`minun falaa yakhaafu zulmanw wa laa hadmaa
📖 Tekkim Wolof
Képp koo xam ne nag yaa ngay jëf u yiw te gëm, du ragal foofa ag tooñ [gu ñu koy tooñ], walla ku koy sërxal.

🎧 Dégg


📜 Aaya 110-114 — Simoore Taha

110يَعْلَمُ مَا بَيْنَ أَيْدِيهِمْ وَمَا خَلْفَهُمْ وَلَا يُحِيطُونَ بِهِ عِلْمًا
Moo xam la jàll ak liy ñëwi, te kenn ci ñoom mënu koo peeg ci xam ko.
111۞ وَعَنَتِ الْوُجُوهُ لِلْحَيِّ الْقَيُّومِ ۖ وَقَدْ خَابَ مَنْ حَمَلَ ظُلْمًا
Loos yépp janoo nañu fa kanamu Yàlla, Muy dundu te taxawu lépp, te képp ku yenu na ag tooñ , [na ko wóor ne] sooy na bu kero gee.
112وَمَن يَعْمَلْ مِنَ الصَّالِحَاتِ وَهُوَ مُؤْمِنٌ فَلَا يَخَافُ ظُلْمًا وَلَا هَضْمًا
Képp koo xam ne nag yaa ngay jëf u yiw te gëm, du ragal foofa ag tooñ [gu ñu koy tooñ], walla ku koy sërxal.
113وَكَذَٰلِكَ أَنزَلْنَاهُ قُرْآنًا عَرَبِيًّا وَصَرَّفْنَا فِيهِ مِنَ الْوَعِيدِ لَعَلَّهُمْ يَتَّقُونَ أَوْ يُحْدِثُ لَهُمْ ذِكْرًا
Noonu Lanu wàccee Alxuraan ci làmmiñu araab, biral ci lool ag tëkku, ndaxtele amaana ñu ragal Yàlla walla ñu jàjju [fàttaliku xalaat]?
114فَتَعَالَى اللَّهُ الْمَلِكُ الْحَقُّ ۗ وَلَا تَعْجَلْ بِالْقُرْآنِ مِن قَبْلِ أَن يُقْضَىٰ إِلَيْكَ وَحْيُهُ ۖ وَقُل رَّبِّ زِدْنِي عِلْمًا
Yàlla Buur ba di dëgg, kawe na ! Bul yàkkamtee tasaare Alxuraan ji tey jiitu soloo ga. Waxal ne : "Yaw sama Boroom dolli ma xam-xam ! ”
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
112Aaya

Tekki — Taha 112

Simoore Taha Aaya 112 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Képp koo xam ne nag yaa ngay jëf u yiw…

Simoore Aaya 112/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 110–114. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers