Taha · 54/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
كُلُوا وَارْعَوْا أَنْعَامَكُمْ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّأُولِي النُّهَىٰ ۝٥٤
Kuloo war`aw an`aamakum; inna fee zaalika la Aayaatil li ulin nuhaa
📖 Tekkim Wolof
“Lekk-leen te sàmm seenug jur”. Ay kéemaan a ngi ci loolu, ñeel aw nit ñu am xel.

🎧 Dégg


📜 Aaya 52-56 — Simoore Taha

52قَالَ عِلْمُهَا عِندَ رَبِّي فِي كِتَابٍ ۖ لَّا يَضِلُّ رَبِّي وَلَا يَنسَى
Mu ne ko : “Seeni mbir a nga ca Téere ba fa sa Boroom. Sama Boroom du juum, du fàtte.
53الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ مَهْدًا وَسَلَكَ لَكُمْ فِيهَا سُبُلًا وَأَنزَلَ مِنَ السَّمَاءِ مَاءً فَأَخْرَجْنَا بِهِ أَزْوَاجًا مِّن نَّبَاتٍ شَتَّىٰ
Sama Boroom bi nga xam ne Moo leen defal suuf si laltaay [maasale ko], defal leen ci ay yoon [ngeen di jokkoo] ; Mu wàcce am ndox mu bawoo asamaan, ñu di ca génne ay xeeti gàncax yu wuute.”
54كُلُوا وَارْعَوْا أَنْعَامَكُمْ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّأُولِي النُّهَىٰ
“Lekk-leen te sàmm seenug jur”. Ay kéemaan a ngi ci loolu, ñeel aw nit ñu am xel.
55۞ مِنْهَا خَلَقْنَاكُمْ وَفِيهَا نُعِيدُكُمْ وَمِنْهَا نُخْرِجُكُمْ تَارَةً أُخْرَىٰ
[Ci suuf si] la Nu leen binde, ci la Nu leen di delloo, te ci la Nu leen dellu génnewaat weneen yoon.
56وَلَقَدْ أَرَيْنَاهُ آيَاتِنَا كُلَّهَا فَكَذَّبَ وَأَبَىٰ
Won Nanu ko Sunu kéemaan yépp mu lànk weddi [Yàlla].
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
54Aaya

Tekki — Taha 54

Simoore Taha Aaya 54 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Lekk-leen te sàmm seenug jur”. Ay kéemaan a ngi ci…

Simoore Aaya 54/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 52–56. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers