Taha · 57/135
Tekki Waxtaan — Taha
قَالَ أَجِئْتَنَا لِتُخْرِجَنَا مِنْ أَرْضِنَا بِسِحْرِكَ يَا مُوسَىٰ ٥٧
Transliteration
Qaala aji`tanaa litukhri janaa min ardinaa bisihrika yaa Moosa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Mu daldi ne : “Waaw yaw Muusaa, danga noo bëgg génne ci sunuy suuf ak sa njibar gi ?
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 55-59 — Taha
55۞ مِنْهَا خَلَقْنَاكُمْ وَفِيهَا نُعِيدُكُمْ وَمِنْهَا نُخْرِجُكُمْ تَارَةً أُخْرَىٰ
[Ci suuf si] la Nu leen binde, ci la Nu leen di delloo, te ci la Nu leen dellu génnewaat weneen yoon.
56وَلَقَدْ أَرَيْنَاهُ آيَاتِنَا كُلَّهَا فَكَذَّبَ وَأَبَىٰ
Won Nanu ko Sunu kéemaan yépp mu lànk weddi [Yàlla].
57قَالَ أَجِئْتَنَا لِتُخْرِجَنَا مِنْ أَرْضِنَا بِسِحْرِكَ يَا مُوسَىٰ
Mu daldi ne : “Waaw yaw Muusaa, danga noo bëgg génne ci sunuy suuf ak sa njibar gi ?
58فَلَنَأْتِيَنَّكَ بِسِحْرٍ مِّثْلِهِ فَاجْعَلْ بَيْنَنَا وَبَيْنَكَ مَوْعِدًا لَّا نُخْلِفُهُ نَحْنُ وَلَا أَنتَ مَكَانًا سُوًى
Dananu la indil njibar gu ni mel. Nu sàkk bis ak barab te kenn bañ koo wuute ci nun ñépp”.
59قَالَ مَوْعِدُكُمْ يَوْمُ الزِّينَةِ وَأَن يُحْشَرَ النَّاسُ ضُحًى
Mu wax ne : “Kon jàpp nanu bis ba nu daan daje, di ca fo. Ca yoor-yoor ba”.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
57Aaya
Tekki — Taha 57
Simoore Taha Aaya 57 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu daldi ne : “Waaw yaw Muusaa, danga noo bëgg…Simoore Aaya 57/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 55–59. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








