Taha · 77/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
وَلَقَدْ أَوْحَيْنَا إِلَىٰ مُوسَىٰ أَنْ أَسْرِ بِعِبَادِي فَاضْرِبْ لَهُمْ طَرِيقًا فِي الْبَحْرِ يَبَسًا لَّا تَخَافُ دَرَكًا وَلَا تَخْشَىٰ ۝٧٧
Wa laqad awhainaaa ilaa Moosaaa an asri bi`ibaadee fadrib lahum tareeqan fil bahri yabasal laa takhaafu darakanw wa laa takhshaa
📖 Tekkim Wolof
Digal Nanu Muusaa [soloo ko]ne ko : “Nga rañaan ak sama jaam ñi, nanga leen sàkkal aw yoonu suuf wu wow ca biir géej ga : bul ragal ku lay dab walla ngay tiit”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 75-79 — Simoore Taha

75وَمَن يَأْتِهِ مُؤْمِنًا قَدْ عَمِلَ الصَّالِحَاتِ فَأُولَٰئِكَ لَهُمُ الدَّرَجَاتُ الْعُلَىٰ
Kuy gëm Yàlla ak a def u yiw ba dem fa Yàlla, ñooña danañu am ay daraja yu kawe,
76جَنَّاتُ عَدْنٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا ۚ وَذَٰلِكَ جَزَاءُ مَن تَزَكَّىٰ
ay àjjana yu sax yoo xam ne ay dex ñooy daw ci suufam te dañu fay béel. Loolu moo di peyug képp kuy sellal.
77وَلَقَدْ أَوْحَيْنَا إِلَىٰ مُوسَىٰ أَنْ أَسْرِ بِعِبَادِي فَاضْرِبْ لَهُمْ طَرِيقًا فِي الْبَحْرِ يَبَسًا لَّا تَخَافُ دَرَكًا وَلَا تَخْشَىٰ
Digal Nanu Muusaa [soloo ko]ne ko : “Nga rañaan ak sama jaam ñi, nanga leen sàkkal aw yoonu suuf wu wow ca biir géej ga : bul ragal ku lay dab walla ngay tiit”.
78فَأَتْبَعَهُمْ فِرْعَوْنُ بِجُنُودِهِ فَغَشِيَهُم مِّنَ الْيَمِّ مَا غَشِيَهُمْ
Firawna ak ug xareem topp leen. Duus ya labal leen.
79وَأَضَلَّ فِرْعَوْنُ قَوْمَهُ وَمَا هَدَىٰ
Firawna sànk na aw nitam, te farul gindiku.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
77Aaya

Tekki — Taha 77

Simoore Taha Aaya 77 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Digal Nanu Muusaa [soloo ko]ne ko : “Nga rañaan ak…

Simoore Aaya 77/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 75–79. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers