Al-Anbiya · 1/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
اقْتَرَبَ لِلنَّاسِ حِسَابُهُمْ وَهُمْ فِي غَفْلَةٍ مُّعْرِضُونَ ۝١
Iqtaraba linnaasi hisaa buhum wa hum fee ghaflatim mu`ridoon
📖 Tekkim Wolof
Waññub [jëfi] nit ñi jegesi na, te ñoom ña nga nuur cig càggante dëddu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore Al-Anbiya

1اقْتَرَبَ لِلنَّاسِ حِسَابُهُمْ وَهُمْ فِي غَفْلَةٍ مُّعْرِضُونَ
Waññub [jëfi] nit ñi jegesi na, te ñoom ña nga nuur cig càggante dëddu.
2مَا يَأْتِيهِم مِّن ذِكْرٍ مِّن رَّبِّهِم مُّحْدَثٍ إِلَّا اسْتَمَعُوهُ وَهُمْ يَلْعَبُونَ
Amul lenn lu leen di digal ci Alxuraan di lu bawoo fa seen Boroom, te dégluwaale wuñu kook am po,
3لَاهِيَةً قُلُوبُهُمْ ۗ وَأَسَرُّوا النَّجْوَى الَّذِينَ ظَلَمُوا هَلْ هَٰذَا إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُكُمْ ۖ أَفَتَأْتُونَ السِّحْرَ وَأَنتُمْ تُبْصِرُونَ
Càggante nekk na ca seen xol ; tooñkat ya di déeyoo naan : “Ndax kii dafa nekkul mbindéef ni yéen ? Ndax dangeen di topp ag njibar te janook moom ? ”
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
1Aaya

Tekki — Al-Anbiya 1

Simoore Al-Anbiya Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waññub [jëfi] nit ñi jegesi na, te ñoom ña nga…

Simoore Aaya 1/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers