Al-Hajj · 61/78
Tekki Waxtaan — Al-Hajj
ذَٰلِكَ بِأَنَّ اللَّهَ يُولِجُ اللَّيْلَ فِي النَّهَارِ وَيُولِجُ النَّهَارَ فِي اللَّيْلِ وَأَنَّ اللَّهَ سَمِيعٌ بَصِيرٌ ۝٦١
Zaalika bi annal laaha yoolijul laila fin nahaari wa yoolijun nahaara fil laili wa annal laaha Samee`um Baseer
📖 Tekkim Wolof
Noonu la ngir Yàlla mooy dugal guddi ci bëccëg, di duggal bëccëg ci guddi, te nag Yàlla Kuy dégg la, Kuy gis la.
🎧 Dégg

📜 Aaya 59-63 — Al-Hajj

59لَيُدْخِلَنَّهُم مُّدْخَلًا يَرْضَوْنَهُ ۗ وَإِنَّ اللَّهَ لَعَلِيمٌ حَلِيمٌ
fàwwu dana leen tàbbal barab boo xam ne danañu ca bég, te Yàlla ku xam la, Ku lewet la.
60۞ ذَٰلِكَ وَمَنْ عَاقَبَ بِمِثْلِ مَا عُوقِبَ بِهِ ثُمَّ بُغِيَ عَلَيْهِ لَيَنصُرَنَّهُ اللَّهُ ۗ إِنَّ اللَّهَ لَعَفُوٌّ غَفُورٌ
Noonu la. Ku mbugale lu toll ni la ñu ko tooñ, topp ñu tooñaat ko, Yàlla dana ko dimbali, Yàlla Jéggalaakoon, Baalewaakoon la.
61ذَٰلِكَ بِأَنَّ اللَّهَ يُولِجُ اللَّيْلَ فِي النَّهَارِ وَيُولِجُ النَّهَارَ فِي اللَّيْلِ وَأَنَّ اللَّهَ سَمِيعٌ بَصِيرٌ
Noonu la ngir Yàlla mooy dugal guddi ci bëccëg, di duggal bëccëg ci guddi, te nag Yàlla Kuy dégg la, Kuy gis la.
62ذَٰلِكَ بِأَنَّ اللَّهَ هُوَ الْحَقُّ وَأَنَّ مَا يَدْعُونَ مِن دُونِهِ هُوَ الْبَاطِلُ وَأَنَّ اللَّهَ هُوَ الْعَلِيُّ الْكَبِيرُ
Noonu la ngir Moom mooy dëgg ga, te lépp lu ngeen di jaamu te du Yàlla, neen la ; te Yàlla moom Ku kawe la, Ku màgg la.
63أَلَمْ تَرَ أَنَّ اللَّهَ أَنزَلَ مِنَ السَّمَاءِ مَاءً فَتُصْبِحُ الْأَرْضُ مُخْضَرَّةً ۗ إِنَّ اللَّهَ لَطِيفٌ خَبِيرٌ
Ndax dangaa gisul ne Yàlla mooy wàcce ndox mu jóge asamaan, soppi suuf si mu naat ? Yàlla Kuy ñeewant la (jaam ñi), Ku deñ-kumpa la.
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
61Aaya

Tekki — Al-Hajj 61

Simoore Al-Hajj Aaya 61 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noonu la ngir Yàlla mooy dugal guddi ci bëccëg, di…

Simoore Aaya 61/78 — Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hajj Dégg, Al-Hajj Tekki, Al-Hajj mp3, Al-Hajj pdf. Aaya 59–63. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers