Al-Mu'minun · 106/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
قَالُوا رَبَّنَا غَلَبَتْ عَلَيْنَا شِقْوَتُنَا وَكُنَّا قَوْمًا ضَالِّينَ ۝١٠٦
Qaaloo Rabbanaa ghalabat `alainaa shiqwatunaa wa kunnaa qawman daaalleen
📖 Tekkim Wolof
Ñu wax ne : “Boroom sunu ! Texeedi not nanu te xamadi woon nanu itam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 104-108 — Simoore Al-Mu'minun

104تَلْفَحُ وُجُوهَهُمُ النَّارُ وَهُمْ فِيهَا كَالِحُونَ
Safara waa ngay làkk seeni kanam, ñu ne fa xuum
105أَلَمْ تَكُنْ آيَاتِي تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ فَكُنتُم بِهَا تُكَذِّبُونَ
“Moo ndax daa weesul jàng samag waareci yéen, ngeen jàppe ko ay fen ? ”
106قَالُوا رَبَّنَا غَلَبَتْ عَلَيْنَا شِقْوَتُنَا وَكُنَّا قَوْمًا ضَالِّينَ
Ñu wax ne : “Boroom sunu ! Texeedi not nanu te xamadi woon nanu itam.
107رَبَّنَا أَخْرِجْنَا مِنْهَا فَإِنْ عُدْنَا فَإِنَّا ظَالِمُونَ
Boroom sunu, génne nu ci ! Bu nu tey-teyloo ba dellu ci, noo tooñ”.
108قَالَ اخْسَئُوا فِيهَا وَلَا تُكَلِّمُونِ
Mu ne leen : “Jattleen ci biir te buleen ma tuddati”.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
106Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 106

Simoore Al-Mu'minun Aaya 106 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu wax ne : “Boroom sunu ! Texeedi not nanu…

Simoore Aaya 106/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 104–108. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers