Al-Mu'minun · 107/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
رَبَّنَا أَخْرِجْنَا مِنْهَا فَإِنْ عُدْنَا فَإِنَّا ظَالِمُونَ ١٠٧
Transliteration
Rabbanaa akhrijnaa minhaa fa in `udnaa fa innaa zaalimoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Boroom sunu, génne nu ci ! Bu nu tey-teyloo ba dellu ci, noo tooñ”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 105-109 — Al-Mu'minun
105أَلَمْ تَكُنْ آيَاتِي تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ فَكُنتُم بِهَا تُكَذِّبُونَ
“Moo ndax daa weesul jàng samag waareci yéen, ngeen jàppe ko ay fen ? ”
106قَالُوا رَبَّنَا غَلَبَتْ عَلَيْنَا شِقْوَتُنَا وَكُنَّا قَوْمًا ضَالِّينَ
Ñu wax ne : “Boroom sunu ! Texeedi not nanu te xamadi woon nanu itam.
107رَبَّنَا أَخْرِجْنَا مِنْهَا فَإِنْ عُدْنَا فَإِنَّا ظَالِمُونَ
Boroom sunu, génne nu ci ! Bu nu tey-teyloo ba dellu ci, noo tooñ”.
108قَالَ اخْسَئُوا فِيهَا وَلَا تُكَلِّمُونِ
Mu ne leen : “Jattleen ci biir te buleen ma tuddati”.
109إِنَّهُ كَانَ فَرِيقٌ مِّنْ عِبَادِي يَقُولُونَ رَبَّنَا آمَنَّا فَاغْفِرْ لَنَا وَارْحَمْنَا وَأَنتَ خَيْرُ الرَّاحِمِينَ
Am na ab kurél bu bokkoon ci sama jaam, daan wax naan : “Boroom sunu, gëm nanu ; jéggal nu te yërëm nu, Yaw yaa di gën ji Yërëmaakoon” ;
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
107Aaya
Tekki — Al-Mu'minun 107
Simoore Al-Mu'minun Aaya 107 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Boroom sunu, génne nu ci ! Bu nu tey-teyloo ba…Simoore Aaya 107/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 105–109. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








