Al-Mu'minun · 28/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
فَإِذَا اسْتَوَيْتَ أَنتَ وَمَن مَّعَكَ عَلَى الْفُلْكِ فَقُلِ الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي نَجَّانَا مِنَ الْقَوْمِ الظَّالِمِينَ ۝٢٨
Fa izas tawaita ata wa mam ma`aka `alal fulki faqulil hamdu lillaahil lazee najjaanaa minal qawmiz zalimeen
📖 Tekkim Wolof
Saa soo duggee ca gaal ga yaak ña nga àndal ba noppi, nanga wax ne : “Cant ñeel na Yàlla Moom mi nu musal ci ay nit yu di ay tooñkat.”
🎧 Dégg

📜 Aaya 26-30 — Al-Mu'minun

26قَالَ رَبِّ انصُرْنِي بِمَا كَذَّبُونِ
[Nooh]ne : “Yaw sama Boroom ! Dimbali ma ci weddi gi ñu ma weddi”.
27فَأَوْحَيْنَا إِلَيْهِ أَنِ اصْنَعِ الْفُلْكَ بِأَعْيُنِنَا وَوَحْيِنَا فَإِذَا جَاءَ أَمْرُنَا وَفَارَ التَّنُّورُ ۙ فَاسْلُكْ فِيهَا مِن كُلٍّ زَوْجَيْنِ اثْنَيْنِ وَأَهْلَكَ إِلَّا مَن سَبَقَ عَلَيْهِ الْقَوْلُ مِنْهُمْ ۖ وَلَا تُخَاطِبْنِي فِي الَّذِينَ ظَلَمُوا ۖ إِنَّهُم مُّغْرَقُونَ
Nu daldi ko soloo [digal ko] ne ko : “Defaral gaal ci Sunug càmm ak Sunu ndigal. Te saa su Sunu ndigal agsee ba lakkukaayu mburu ba sãs, nanga dugal te bàyyi sag njaboot ak yóllent ci wépp xeet ba mu des ña nga xam ne wax ja jiitu woon na c
28فَإِذَا اسْتَوَيْتَ أَنتَ وَمَن مَّعَكَ عَلَى الْفُلْكِ فَقُلِ الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي نَجَّانَا مِنَ الْقَوْمِ الظَّالِمِينَ
Saa soo duggee ca gaal ga yaak ña nga àndal ba noppi, nanga wax ne : “Cant ñeel na Yàlla Moom mi nu musal ci ay nit yu di ay tooñkat.”
29وَقُل رَّبِّ أَنزِلْنِي مُنزَلًا مُّبَارَكًا وَأَنتَ خَيْرُ الْمُنزِلِينَ
Te nanga wax ne : “Sama Boroom, nanga ma wàcce ngën gi wàccuwaay bu barkeel, Yaw yaa di gën ji wattu”.
30إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ وَإِن كُنَّا لَمُبْتَلِينَ
Ay kéemaannekk na ci biir loolu. Doontele sax dañuy nattu (ñi gëm).
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 28

Simoore Al-Mu'minun Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Saa soo duggee ca gaal ga yaak ña nga àndal…

Simoore Aaya 28/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers