Al-Mu'minun · 38/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
إِنْ هُوَ إِلَّا رَجُلٌ افْتَرَىٰ عَلَى اللَّهِ كَذِبًا وَمَا نَحْنُ لَهُ بِمُؤْمِنِينَ ٣٨
Transliteration
In huwa illaa rajulunif taraa `alal laahi kazibanw wa maa nahnuu lahoo bimu`mineen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Kii daal as waay la suy duural Yàlla ay fen ; te nun sax gëmunu ko”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 36-40 — Al-Mu'minun
36۞ هَيْهَاتَ هَيْهَاتَ لِمَا تُوعَدُونَ
Mukk, mukk li ñu leen dig !
37إِنْ هِيَ إِلَّا حَيَاتُنَا الدُّنْيَا نَمُوتُ وَنَحْيَا وَمَا نَحْنُ بِمَبْعُوثِينَ
Lii daal du lenn lu dul sunug dundug àddina sii : danuy dundu, dee ; waaye dunu dekki.
38إِنْ هُوَ إِلَّا رَجُلٌ افْتَرَىٰ عَلَى اللَّهِ كَذِبًا وَمَا نَحْنُ لَهُ بِمُؤْمِنِينَ
Kii daal as waay la suy duural Yàlla ay fen ; te nun sax gëmunu ko”.
39قَالَ رَبِّ انصُرْنِي بِمَا كَذَّبُونِ
Mu ne : “Yaw sama Boroom ! May ma ndimbal ci weddi gi ñu may weddi”.
40قَالَ عَمَّا قَلِيلٍ لَّيُصْبِحُنَّ نَادِمِينَ
Mu wax ne [Moom Yàlla] : “Li feek ndiir su néew, danañu rëccu”.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
38Aaya
Tekki — Al-Mu'minun 38
Simoore Al-Mu'minun Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kii daal as waay la suy duural Yàlla ay fen…Simoore Aaya 38/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








