Al-Mu'minun · 39/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
قَالَ رَبِّ انصُرْنِي بِمَا كَذَّبُونِ ۝٣٩
Qaala Rabbin surnee bimaa kazzaboon
📖 Tekkim Wolof
Mu ne : “Yaw sama Boroom ! May ma ndimbal ci weddi gi ñu may weddi”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 37-41 — Simoore Al-Mu'minun

37إِنْ هِيَ إِلَّا حَيَاتُنَا الدُّنْيَا نَمُوتُ وَنَحْيَا وَمَا نَحْنُ بِمَبْعُوثِينَ
Lii daal du lenn lu dul sunug dundug àddina sii : danuy dundu, dee ; waaye dunu dekki.
38إِنْ هُوَ إِلَّا رَجُلٌ افْتَرَىٰ عَلَى اللَّهِ كَذِبًا وَمَا نَحْنُ لَهُ بِمُؤْمِنِينَ
Kii daal as waay la suy duural Yàlla ay fen ; te nun sax gëmunu ko”.
39قَالَ رَبِّ انصُرْنِي بِمَا كَذَّبُونِ
Mu ne : “Yaw sama Boroom ! May ma ndimbal ci weddi gi ñu may weddi”.
40قَالَ عَمَّا قَلِيلٍ لَّيُصْبِحُنَّ نَادِمِينَ
Mu wax ne [Moom Yàlla] : “Li feek ndiir su néew, danañu rëccu”.
41فَأَخَذَتْهُمُ الصَّيْحَةُ بِالْحَقِّ فَجَعَلْنَاهُمْ غُثَاءً ۚ فَبُعْدًا لِّلْقَوْمِ الظَّالِمِينَ
Ag xaacu dikkal leen ci dëgg ; ñu ne lànjaŋ. Tooñkat ya tuskare nañu !
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
39Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 39

Simoore Al-Mu'minun Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne : “Yaw sama Boroom ! May ma ndimbal…

Simoore Aaya 39/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers