Al-Mu'minun · 47/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
فَقَالُوا أَنُؤْمِنُ لِبَشَرَيْنِ مِثْلِنَا وَقَوْمُهُمَا لَنَا عَابِدُونَ ۝٤٧
Faqaaloo annu`minu libasharaini mislinaa wa qawmuhumaa lanaa `aabidoon
📖 Tekkim Wolof
Ñuy wax naan : “Ndax dananu gëm ñaari nit ñu mel ni nun, ñoo xam ne seenu xeet sunuy jaam lañu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 45-49 — Simoore Al-Mu'minun

45ثُمَّ أَرْسَلْنَا مُوسَىٰ وَأَخَاهُ هَارُونَ بِآيَاتِنَا وَسُلْطَانٍ مُّبِينٍ
Topp, ginnaaw ba yónni Nanu Muusaa ak mbokkam ma Aaruuna jox leen Sunuy laaya ak kàttan gu bir,
46إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِ فَاسْتَكْبَرُوا وَكَانُوا قَوْمًا عَالِينَ
jëmale ko ca Firawna ak gàngooram ña doon rëy-rëylu te doon aw nit ñuy kawe-kawelu.
47فَقَالُوا أَنُؤْمِنُ لِبَشَرَيْنِ مِثْلِنَا وَقَوْمُهُمَا لَنَا عَابِدُونَ
Ñuy wax naan : “Ndax dananu gëm ñaari nit ñu mel ni nun, ñoo xam ne seenu xeet sunuy jaam lañu.
48فَكَذَّبُوهُمَا فَكَانُوا مِنَ الْمُهْلَكِينَ
Ñu daldi leen weddi, daldi alku.
49وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَى الْكِتَابَ لَعَلَّهُمْ يَهْتَدُونَ
Jox Nanu Muusaa Téere ba ngir mu waar leen ca ba ba ñuy gindiku.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
47Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 47

Simoore Al-Mu'minun Aaya 47 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñuy wax naan : “Ndax dananu gëm ñaari nit ñu…

Simoore Aaya 47/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 45–49. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers