Al-Mu'minun · 91/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
مَا اتَّخَذَ اللَّهُ مِن وَلَدٍ وَمَا كَانَ مَعَهُ مِنْ إِلَٰهٍ ۚ إِذًا لَّذَهَبَ كُلُّ إِلَٰهٍ بِمَا خَلَقَ وَلَعَلَا بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ ۚ سُبْحَانَ اللَّهِ عَمَّا يَصِفُونَ ۝٩١
Mat takhazal laahu minw waladinw wa maa kaana ma`ahoo min ilaah; izal lazahaba kullu ilaahim bimaa khalaqa wa la`alaa ba`duhum `alaa ba`d; Subhaannal laahi `ammaa yasifoon
📖 Tekkim Wolof
Yàlla jàppewul kenn doomam te it amul jeneen Yàlla ju muy àndal ; su loolu amoom, kon yàlla ju nekk dem ak boppam ak la mu sàkk te kon danañuy ëppantey doole. [Tudd naa sellam ga] ! Rawante naak li ñu koy melal.

🎧 Dégg


📜 Aaya 89-93 — Al-Mu'minun

89سَيَقُولُونَ لِلَّهِ ۚ قُلْ فَأَنَّىٰ تُسْحَرُونَ
Danañu wax ne : “Yàllaa ko moom”. Neel : “Ana fu ñu leen jibare ? ” [ba mënuleen a gëm].
90بَلْ أَتَيْنَاهُم بِالْحَقِّ وَإِنَّهُمْ لَكَاذِبُونَ
Indil Nanu leen dëgg waaye ñoom ay fenkat lañu.
91مَا اتَّخَذَ اللَّهُ مِن وَلَدٍ وَمَا كَانَ مَعَهُ مِنْ إِلَٰهٍ ۚ إِذًا لَّذَهَبَ كُلُّ إِلَٰهٍ بِمَا خَلَقَ وَلَعَلَا بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ ۚ سُبْحَانَ اللَّهِ عَمَّا يَصِفُونَ
Yàlla jàppewul kenn doomam te it amul jeneen Yàlla ju muy àndal ; su loolu amoom, kon yàlla ju nekk dem ak boppam ak la mu sàkk te kon danañuy ëppantey doole. [Tudd naa sellam ga] ! Rawante naak li ñu koy melal.
92عَالِمِ الْغَيْبِ وَالشَّهَادَةِ فَتَعَالَىٰ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Mooy ki xam kumpaag li teew ! Kawe na [lool] li ñu koy bokkaaleel !
93قُل رَّبِّ إِمَّا تُرِيَنِّي مَا يُوعَدُونَ
Neel : “Sama Boroom, cëy boo ma wonoon li nga leen dig ;
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
91Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 91

Simoore Al-Mu'minun Aaya 91 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla jàppewul kenn doomam te it amul jeneen Yàlla ju…

Simoore Aaya 91/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 89–93. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, August 19, 2026

Don't forget us in your sincere prayers