Al-Mu'minun · 90/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
بَلْ أَتَيْنَاهُم بِالْحَقِّ وَإِنَّهُمْ لَكَاذِبُونَ ۝٩٠
Bal atainaahum bil haqqi wa innahum lakaaziboon
📖 Tekkim Wolof
Indil Nanu leen dëgg waaye ñoom ay fenkat lañu.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 88-92 — Simoore Al-Mu'minun

88قُلْ مَن بِيَدِهِ مَلَكُوتُ كُلِّ شَيْءٍ وَهُوَ يُجِيرُ وَلَا يُجَارُ عَلَيْهِ إِن كُنتُمْ تَعْلَمُونَ
Neel : “Ana kan moo ame ci loxoom nguurug lépp, kiy aare te soxlawul ku ko aar ? Waxleen rekk, ndax xam ngeen ko ! ”
89سَيَقُولُونَ لِلَّهِ ۚ قُلْ فَأَنَّىٰ تُسْحَرُونَ
Danañu wax ne : “Yàllaa ko moom”. Neel : “Ana fu ñu leen jibare ? ” [ba mënuleen a gëm].
90بَلْ أَتَيْنَاهُم بِالْحَقِّ وَإِنَّهُمْ لَكَاذِبُونَ
Indil Nanu leen dëgg waaye ñoom ay fenkat lañu.
91مَا اتَّخَذَ اللَّهُ مِن وَلَدٍ وَمَا كَانَ مَعَهُ مِنْ إِلَٰهٍ ۚ إِذًا لَّذَهَبَ كُلُّ إِلَٰهٍ بِمَا خَلَقَ وَلَعَلَا بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ ۚ سُبْحَانَ اللَّهِ عَمَّا يَصِفُونَ
Yàlla jàppewul kenn doomam te it amul jeneen Yàlla ju muy àndal ; su loolu amoom, kon yàlla ju nekk dem ak boppam ak la mu sàkk te kon danañuy ëppantey doole. [Tudd naa sellam ga] ! Rawante naak li ñu koy melal.
92عَالِمِ الْغَيْبِ وَالشَّهَادَةِ فَتَعَالَىٰ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Mooy ki xam kumpaag li teew ! Kawe na [lool] li ñu koy bokkaaleel !
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
90Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 90

Simoore Al-Mu'minun Aaya 90 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Indil Nanu leen dëgg waaye ñoom ay fenkat lañu.

Simoore Aaya 90/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 88–92. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers