Al-Mu'minun · 95/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَإِنَّا عَلَىٰ أَن نُّرِيَكَ مَا نَعِدُهُمْ لَقَادِرُونَ ۝٩٥
Wa innaa `alaaa an nuriyaka maa na`iduhum laqaadiroon
📖 Tekkim Wolof
Te it am Nanu kàttanu won la li Nu leen dig.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 93-97 — Simoore Al-Mu'minun

93قُل رَّبِّ إِمَّا تُرِيَنِّي مَا يُوعَدُونَ
Neel : “Sama Boroom, cëy boo ma wonoon li nga leen dig ;
94رَبِّ فَلَا تَجْعَلْنِي فِي الْقَوْمِ الظَّالِمِينَ
Yaw sama Boroom, bul ma boole mukk ci tooñkat yi.
95وَإِنَّا عَلَىٰ أَن نُّرِيَكَ مَا نَعِدُهُمْ لَقَادِرُونَ
Te it am Nanu kàttanu won la li Nu leen dig.
96ادْفَعْ بِالَّتِي هِيَ أَحْسَنُ السَّيِّئَةَ ۚ نَحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَصِفُونَ
Ña ngay jiñe ñaawtéef ci [jëf yu gën a]rafet. Nun [Yàlla] noo gën a xam la ñuy melal.
97وَقُل رَّبِّ أَعُوذُ بِكَ مِنْ هَمَزَاتِ الشَّيَاطِينِ
Neel : “Maa ngi sàkkoo ci sama Boroom mu musal ma ci jax-jaxali Séytaane.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
95Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 95

Simoore Al-Mu'minun Aaya 95 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te it am Nanu kàttanu won la li Nu leen…

Simoore Aaya 95/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 93–97. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers