Al-Mu'minun · 97/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَقُل رَّبِّ أَعُوذُ بِكَ مِنْ هَمَزَاتِ الشَّيَاطِينِ ۝٩٧
Wa qur Rabbi a`oozu bika min hamazaatish Shayaateen
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Maa ngi sàkkoo ci sama Boroom mu musal ma ci jax-jaxali Séytaane.

🎧 Dégg


📜 Aaya 95-99 — Simoore Al-Mu'minun

95وَإِنَّا عَلَىٰ أَن نُّرِيَكَ مَا نَعِدُهُمْ لَقَادِرُونَ
Te it am Nanu kàttanu won la li Nu leen dig.
96ادْفَعْ بِالَّتِي هِيَ أَحْسَنُ السَّيِّئَةَ ۚ نَحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَصِفُونَ
Ña ngay jiñe ñaawtéef ci [jëf yu gën a]rafet. Nun [Yàlla] noo gën a xam la ñuy melal.
97وَقُل رَّبِّ أَعُوذُ بِكَ مِنْ هَمَزَاتِ الشَّيَاطِينِ
Neel : “Maa ngi sàkkoo ci sama Boroom mu musal ma ci jax-jaxali Séytaane.
98وَأَعُوذُ بِكَ رَبِّ أَن يَحْضُرُونِ
te maa ngi sàkku ndimbalul sama Boroom ci ñu di ma teewe ànd ak man”.
99حَتَّىٰ إِذَا جَاءَ أَحَدَهُمُ الْمَوْتُ قَالَ رَبِّ ارْجِعُونِ
ba ba dee dikkal kenn ci ñoom, mu naan : “Sama Boroom ! Delloo ma àddina,
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
97Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 97

Simoore Al-Mu'minun Aaya 97 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Maa ngi sàkkoo ci sama Boroom mu musal…

Simoore Aaya 97/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 95–99. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers