Al-Mu'minun · 98/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَأَعُوذُ بِكَ رَبِّ أَن يَحْضُرُونِ ۝٩٨
Wa a`oozu bika Rabbi ai-yahduroon
📖 Tekkim Wolof
te maa ngi sàkku ndimbalul sama Boroom ci ñu di ma teewe ànd ak man”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 96-100 — Simoore Al-Mu'minun

96ادْفَعْ بِالَّتِي هِيَ أَحْسَنُ السَّيِّئَةَ ۚ نَحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَصِفُونَ
Ña ngay jiñe ñaawtéef ci [jëf yu gën a]rafet. Nun [Yàlla] noo gën a xam la ñuy melal.
97وَقُل رَّبِّ أَعُوذُ بِكَ مِنْ هَمَزَاتِ الشَّيَاطِينِ
Neel : “Maa ngi sàkkoo ci sama Boroom mu musal ma ci jax-jaxali Séytaane.
98وَأَعُوذُ بِكَ رَبِّ أَن يَحْضُرُونِ
te maa ngi sàkku ndimbalul sama Boroom ci ñu di ma teewe ànd ak man”.
99حَتَّىٰ إِذَا جَاءَ أَحَدَهُمُ الْمَوْتُ قَالَ رَبِّ ارْجِعُونِ
ba ba dee dikkal kenn ci ñoom, mu naan : “Sama Boroom ! Delloo ma àddina,
100لَعَلِّي أَعْمَلُ صَالِحًا فِيمَا تَرَكْتُ ۚ كَلَّا ۚ إِنَّهَا كَلِمَةٌ هُوَ قَائِلُهَا ۖ وَمِن وَرَائِهِم بَرْزَخٌ إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ
ndax ma mën a jëf yiw ca la ma fa bàyyi”. [Mukk loolu du mës a am], loolu kàddu la rekk gu muy wax. [Barsàq] kiiraay la ñuy nekk ba ba ñuy dekki”.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
98Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 98

Simoore Al-Mu'minun Aaya 98 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te maa ngi sàkku ndimbalul sama Boroom ci ñu di…

Simoore Aaya 98/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 96–100. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers