Al-Mu'minun · 96/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
ادْفَعْ بِالَّتِي هِيَ أَحْسَنُ السَّيِّئَةَ ۚ نَحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَصِفُونَ ۝٩٦
Idfa` billate hiya ahsanus saiyi`ah; nahnu a`lamu bimaa yasifoon
📖 Tekkim Wolof
Ña ngay jiñe ñaawtéef ci [jëf yu gën a]rafet. Nun [Yàlla] noo gën a xam la ñuy melal.

🎧 Dégg


📜 Aaya 94-98 — Simoore Al-Mu'minun

94رَبِّ فَلَا تَجْعَلْنِي فِي الْقَوْمِ الظَّالِمِينَ
Yaw sama Boroom, bul ma boole mukk ci tooñkat yi.
95وَإِنَّا عَلَىٰ أَن نُّرِيَكَ مَا نَعِدُهُمْ لَقَادِرُونَ
Te it am Nanu kàttanu won la li Nu leen dig.
96ادْفَعْ بِالَّتِي هِيَ أَحْسَنُ السَّيِّئَةَ ۚ نَحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَصِفُونَ
Ña ngay jiñe ñaawtéef ci [jëf yu gën a]rafet. Nun [Yàlla] noo gën a xam la ñuy melal.
97وَقُل رَّبِّ أَعُوذُ بِكَ مِنْ هَمَزَاتِ الشَّيَاطِينِ
Neel : “Maa ngi sàkkoo ci sama Boroom mu musal ma ci jax-jaxali Séytaane.
98وَأَعُوذُ بِكَ رَبِّ أَن يَحْضُرُونِ
te maa ngi sàkku ndimbalul sama Boroom ci ñu di ma teewe ànd ak man”.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
96Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 96

Simoore Al-Mu'minun Aaya 96 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña ngay jiñe ñaawtéef ci [jëf yu gën a]rafet. Nun…

Simoore Aaya 96/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 94–98. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers