Al-Furqan · 5/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
وَقَالُوا أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ اكْتَتَبَهَا فَهِيَ تُمْلَىٰ عَلَيْهِ بُكْرَةً وَأَصِيلًا ۝٥
Wa qaalooo asaateerul awwaleenak tatabahaa fahiya tumlaa `alaihi bukratanw wa aseelaa
📖 Tekkim Wolof
Ñu wax it ne : “Léebi mag ñu jëkk ña rekk la ! Ñu koy saa muy bind suba ak ngoon ! ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Al-Furqan

3وَاتَّخَذُوا مِن دُونِهِ آلِهَةً لَّا يَخْلُقُونَ شَيْئًا وَهُمْ يُخْلَقُونَ وَلَا يَمْلِكُونَ لِأَنفُسِهِمْ ضَرًّا وَلَا نَفْعًا وَلَا يَمْلِكُونَ مَوْتًا وَلَا حَيَاةً وَلَا نُشُورًا
Te ñoom dañoo jàppe ay yàlla ñenenn ñoo xam ne binduñu tus, faf ñoom sax dañu leen a bind, te it mënuñoo lor seen bopp waxantumalaak njariñ, amuñu dee amuñu dundu waxantumalaak dekki.
4وَقَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا إِنْ هَٰذَا إِلَّا إِفْكٌ افْتَرَاهُ وَأَعَانَهُ عَلَيْهِ قَوْمٌ آخَرُونَ ۖ فَقَدْ جَاءُوا ظُلْمًا وَزُورًا
Yéefar yi wax nañu ne : “[Alxuraan] jii daal aw duur la wu [Muhammad] moo ko sos, te dafa am ñu ko cay jàppale”. Li ñu fi indi tooñ ak i fen la.
5وَقَالُوا أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ اكْتَتَبَهَا فَهِيَ تُمْلَىٰ عَلَيْهِ بُكْرَةً وَأَصِيلًا
Ñu wax it ne : “Léebi mag ñu jëkk ña rekk la ! Ñu koy saa muy bind suba ak ngoon ! ”
6قُلْ أَنزَلَهُ الَّذِي يَعْلَمُ السِّرَّ فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ إِنَّهُ كَانَ غَفُورًا رَّحِيمًا
Neel : “Ki ko wàcce moo xam mbooti asamaan yeek suuf si. Di ab Jéggalaakon, di Jaglewaakoon.
7وَقَالُوا مَالِ هَٰذَا الرَّسُولِ يَأْكُلُ الطَّعَامَ وَيَمْشِي فِي الْأَسْوَاقِ ۙ لَوْلَا أُنزِلَ إِلَيْهِ مَلَكٌ فَيَكُونَ مَعَهُ نَذِيرًا
Ñu wax ne [ñoom yéefar yi] : “Ana lan moo tax Yonent bii di lekk ñam ak a dox ci ja yi [màrse yi] ? Lan moo tax wutéelsu ko Malaaka mu ànd ak moom di xuppaate ?
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Al-Furqan 5

Simoore Al-Furqan Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu wax it ne : “Léebi mag ñu jëkk ña…

Simoore Aaya 5/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers