Ash-Shu'ara · 10/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
وَإِذْ نَادَىٰ رَبُّكَ مُوسَىٰ أَنِ ائْتِ الْقَوْمَ الظَّالِمِينَ ١٠
Transliteration
Wa iz naadaa Rabbuka Moosaaa ani`-til qawmaz zaalimeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
[Fàttalikul] ba Yàlla woo na Muusaa, [ne ko] : “Demal [jubbanti ji] tooñkat ya,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 8-12 — Ash-Shu'ara
8إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Ay kéemaan yu bari nekk ci loolu ! Waaye taxut li ëpp ci ñoom gëm [diy jullit].
9وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Te sa Boroom mooy Boroom kàttan ga te di Jaglewaakoonug [yërmaande].
10وَإِذْ نَادَىٰ رَبُّكَ مُوسَىٰ أَنِ ائْتِ الْقَوْمَ الظَّالِمِينَ
[Fàttalikul] ba Yàlla woo na Muusaa, [ne ko] : “Demal [jubbanti ji] tooñkat ya,
11قَوْمَ فِرْعَوْنَ ۚ أَلَا يَتَّقُونَ
nitu Firawna” ; moo ndax ñoom duñu ragal Yàlla ?
12قَالَ رَبِّ إِنِّي أَخَافُ أَن يُكَذِّبُونِ
[Muusaa] wax ne : “Yaw Sama Boroom, damaa ragal ñu jàppe ma ab fenkat [weddi ma] ;
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
10Aaya
Tekki — Ash-Shu'ara 10
Simoore Ash-Shu'ara Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Fàttalikul] ba Yàlla woo na Muusaa, [ne ko] : “Demal…Simoore Aaya 10/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








