Ash-Shu'ara · 25/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
قَالَ لِمَنْ حَوْلَهُ أَلَا تَسْتَمِعُونَ ۝٢٥
Qaala liman hawlahooo alaa tastami`oon
📖 Tekkim Wolof
[Firawna] daldi wax ak ña ko wëroon, ne leen : “Gaa ñi xanaa dégguleen ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 23-27 — Ash-Shu'ara

23قَالَ فِرْعَوْنُ وَمَا رَبُّ الْعَالَمِينَ
[Firawna] ne ko : “Waaw, ana kan mooy Boroom àddina si ? ”.
24قَالَ رَبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا ۖ إِن كُنتُم مُّوقِنِينَ
[Muusaa ne ko] : “Mooy Boroom asamaan yeek suuf si ak li nekk seen diggante, ndegam wóolu nga ! ”
25قَالَ لِمَنْ حَوْلَهُ أَلَا تَسْتَمِعُونَ
[Firawna] daldi wax ak ña ko wëroon, ne leen : “Gaa ñi xanaa dégguleen ? ”
26قَالَ رَبُّكُمْ وَرَبُّ آبَائِكُمُ الْأَوَّلِينَ
[Muusaa] ne ko : “... Mooy seen Boroom, di Boroomub seeni baay”.
27قَالَ إِنَّ رَسُولَكُمُ الَّذِي أُرْسِلَ إِلَيْكُمْ لَمَجْنُونٌ
[Firawna] daldi wax ne : “Seen Yonent bii ñu leen yónni ab dof la kat”.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 25

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Firawna] daldi wax ak ña ko wëroon, ne leen :…

Simoore Aaya 25/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers