Ash-Shu'ara · 34/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
قَالَ لِلْمَلَإِ حَوْلَهُ إِنَّ هَٰذَا لَسَاحِرٌ عَلِيمٌ ٣٤
Transliteration
Qaala lilmala-i hawlahooo inna haazaa lasaahirun `aleem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
[Firawna] wax gàngoor ga ne leen : “Kii dey ab jibar la bu xor.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 32-36 — Ash-Shu'ara
32فَأَلْقَىٰ عَصَاهُ فَإِذَا هِيَ ثُعْبَانٌ مُّبِينٌ
[Muusaa] daldi sànni yetam wa, ndekete yoo jaan la juy béllaw-béllawi.
33وَنَزَعَ يَدَهُ فَإِذَا هِيَ بَيْضَاءُ لِلنَّاظِرِينَ
[Muusaa] daldi génne loxoom, mu weex tàll ca ña koy xool.
34قَالَ لِلْمَلَإِ حَوْلَهُ إِنَّ هَٰذَا لَسَاحِرٌ عَلِيمٌ
[Firawna] wax gàngoor ga ne leen : “Kii dey ab jibar la bu xor.
35يُرِيدُ أَن يُخْرِجَكُم مِّنْ أَرْضِكُم بِسِحْرِهِ فَمَاذَا تَأْمُرُونَ
Da leen a bëgg a génne ci seen suuf sii ak jibaram gi. Lu ngeen ma ciy digal ? ”
36قَالُوا أَرْجِهْ وَأَخَاهُ وَابْعَثْ فِي الْمَدَائِنِ حَاشِرِينَ
Ñu ne ko : “Joxleen ñoom ñaar beneen bis te nga yónni ci gox yi ñuy woo nit ñi, di leen
dajale,
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
34Aaya
Tekki — Ash-Shu'ara 34
Simoore Ash-Shu'ara Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Firawna] wax gàngoor ga ne leen : “Kii dey ab…Simoore Aaya 34/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 32–36. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Wednesday, August 19, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








