Ash-Shu'ara · 33/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
وَنَزَعَ يَدَهُ فَإِذَا هِيَ بَيْضَاءُ لِلنَّاظِرِينَ ۝٣٣
Wa naza`a yadahoo faizaa hiya baidaaa`u linnaa zireen
📖 Tekkim Wolof
[Muusaa] daldi génne loxoom, mu weex tàll ca ña koy xool.

🎧 Dégg


📜 Aaya 31-35 — Ash-Shu'ara

31قَالَ فَأْتِ بِهِ إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
[Firawna] ne ko : “Génne ko bu fekkee li ngay wax dëgg la”.
32فَأَلْقَىٰ عَصَاهُ فَإِذَا هِيَ ثُعْبَانٌ مُّبِينٌ
[Muusaa] daldi sànni yetam wa, ndekete yoo jaan la juy béllaw-béllawi.
33وَنَزَعَ يَدَهُ فَإِذَا هِيَ بَيْضَاءُ لِلنَّاظِرِينَ
[Muusaa] daldi génne loxoom, mu weex tàll ca ña koy xool.
34قَالَ لِلْمَلَإِ حَوْلَهُ إِنَّ هَٰذَا لَسَاحِرٌ عَلِيمٌ
[Firawna] wax gàngoor ga ne leen : “Kii dey ab jibar la bu xor.
35يُرِيدُ أَن يُخْرِجَكُم مِّنْ أَرْضِكُم بِسِحْرِهِ فَمَاذَا تَأْمُرُونَ
Da leen a bëgg a génne ci seen suuf sii ak jibaram gi. Lu ngeen ma ciy digal ? ”
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
33Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 33

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Muusaa] daldi génne loxoom, mu weex tàll ca ña koy…

Simoore Aaya 33/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers