Ash-Shu'ara · 59/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
كَذَٰلِكَ وَأَوْرَثْنَاهَا بَنِي إِسْرَائِيلَ ۝٥٩
Kazaalika wa awrasnaahaa Baneee Israaa`eel
📖 Tekkim Wolof
Noona la Nu ko donnalee giir Bani-israayiila.

🎧 Dégg


📜 Aaya 57-61 — Ash-Shu'ara

57فَأَخْرَجْنَاهُم مِّن جَنَّاتٍ وَعُيُونٍ
Noo leen génne woon ci dër yaak dex yi,
58وَكُنُوزٍ وَمَقَامٍ كَرِيمٍ
Ak ca ndàmb yaak dëkkuwaay yu neex ya.
59كَذَٰلِكَ وَأَوْرَثْنَاهَا بَنِي إِسْرَائِيلَ
Noona la Nu ko donnalee giir Bani-israayiila.
60فَأَتْبَعُوهُم مُّشْرِقِينَ
Ba jant ba fénkee la ñu leen dabuji.
61فَلَمَّا تَرَاءَى الْجَمْعَانِ قَالَ أَصْحَابُ مُوسَىٰ إِنَّا لَمُدْرَكُونَ
Ba ñaari mbooloo ya séenantee, waa kër Muusaa daldi ne : “Ñanga nuy dabsi de”.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
59Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 59

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 59 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noona la Nu ko donnalee giir Bani-israayiila.

Simoore Aaya 59/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 57–61. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers