An-Naml · 67/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
وَقَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا أَإِذَا كُنَّا تُرَابًا وَآبَاؤُنَا أَئِنَّا لَمُخْرَجُونَ ۝٦٧
Wa qaalal lazeena kafarooo `a-izaa kunnaa turaabanw wa aabaaa`unaaa a`innaa lamukhrajoon
📖 Tekkim Wolof
Yéefar yaa ngay wax naan : “Ndax [ginnaaw ba ñu faatoo] ba doon suuf nook sunuy baay, dananu génnaat suuf [dekki] ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 65-69 — Simoore An-Naml

65قُل لَّا يَعْلَمُ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ الْغَيْبَ إِلَّا اللَّهُ ۚ وَمَا يَشْعُرُونَ أَيَّانَ يُبْعَثُونَ
Neel : “Ñi nekk ci asamaan yeek suuf si, kenn xamu ci kumpa ku dul Yàlla”. Te it xamuñu kañ la ñuy dekki !
66بَلِ ادَّارَكَ عِلْمُهُمْ فِي الْآخِرَةِ ۚ بَلْ هُمْ فِي شَكٍّ مِّنْهَا ۖ بَلْ هُم مِّنْهَا عَمُونَ
Seeni xam-xam soriwul ci mbiri àllaaxira. Ñoom sax dañu cay sikki-sàkka. Te ñoom sax ay gumba lañu ci mbir moomu.
67وَقَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا أَإِذَا كُنَّا تُرَابًا وَآبَاؤُنَا أَئِنَّا لَمُخْرَجُونَ
Yéefar yaa ngay wax naan : “Ndax [ginnaaw ba ñu faatoo] ba doon suuf nook sunuy baay, dananu génnaat suuf [dekki] ?
68لَقَدْ وُعِدْنَا هَٰذَا نَحْنُ وَآبَاؤُنَا مِن قَبْلُ إِنْ هَٰذَا إِلَّا أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ
Lii daal digoon nañu nu ko nook sunuy baay. Lii du dara lu dul léebi mag ñu jëkk ña ! ”.
69قُلْ سِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَانظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُجْرِمِينَ
Neeleen : “Doxleen ci suuf si [wëréelu] te ngeen xool naka la tooñkat ya mujje”.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
67Aaya

Tekki — An-Naml 67

Simoore An-Naml Aaya 67 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéefar yaa ngay wax naan : “Ndax [ginnaaw ba ñu…

Simoore Aaya 67/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 65–69. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers