An-Naml · 66/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
بَلِ ادَّارَكَ عِلْمُهُمْ فِي الْآخِرَةِ ۚ بَلْ هُمْ فِي شَكٍّ مِّنْهَا ۖ بَلْ هُم مِّنْهَا عَمُونَ ٦٦
Transliteration
Balid daaraka `ilmuhum fil Aakhirah; bal hum fee shakkim minhaa bal hum minhaa `amoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Seeni xam-xam soriwul ci mbiri àllaaxira. Ñoom sax dañu cay sikki-sàkka. Te ñoom sax ay gumba lañu ci mbir moomu.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 64-68 — An-Naml
64أَمَّن يَبْدَأُ الْخَلْقَ ثُمَّ يُعِيدُهُ وَمَن يَرْزُقُكُم مِّنَ السَّمَاءِ وَالْأَرْضِ ۗ أَإِلَٰهٌ مَّعَ اللَّهِ ۚ قُلْ هَاتُوا بُرْهَانَكُمْ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ana kan mooy tàmbali sosu ga, topp Mu di ko delloosi, ana kan moo leen di dundal ci la bawoo asamaan ak suuf. Moo ndax dafa am jeneen yàlla ju ànd ak Yàlla ? [Déedéet amul de]. Neeleen : “Indileen seen firnde ndegam wax ngeen dëgg ! ”
65قُل لَّا يَعْلَمُ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ الْغَيْبَ إِلَّا اللَّهُ ۚ وَمَا يَشْعُرُونَ أَيَّانَ يُبْعَثُونَ
Neel : “Ñi nekk ci asamaan yeek suuf si, kenn xamu ci kumpa ku dul Yàlla”. Te it xamuñu kañ la ñuy dekki !
66بَلِ ادَّارَكَ عِلْمُهُمْ فِي الْآخِرَةِ ۚ بَلْ هُمْ فِي شَكٍّ مِّنْهَا ۖ بَلْ هُم مِّنْهَا عَمُونَ
Seeni xam-xam soriwul ci mbiri àllaaxira. Ñoom sax dañu cay sikki-sàkka. Te ñoom sax ay gumba lañu ci mbir moomu.
67وَقَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا أَإِذَا كُنَّا تُرَابًا وَآبَاؤُنَا أَئِنَّا لَمُخْرَجُونَ
Yéefar yaa ngay wax naan : “Ndax [ginnaaw ba ñu faatoo] ba doon suuf nook sunuy baay, dananu génnaat suuf [dekki] ?
68لَقَدْ وُعِدْنَا هَٰذَا نَحْنُ وَآبَاؤُنَا مِن قَبْلُ إِنْ هَٰذَا إِلَّا أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ
Lii daal digoon nañu nu ko nook sunuy baay. Lii du dara lu dul léebi mag ñu jëkk ña ! ”.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
66Aaya
Tekki — An-Naml 66
Simoore An-Naml Aaya 66 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Seeni xam-xam soriwul ci mbiri àllaaxira. Ñoom sax dañu cay…Simoore Aaya 66/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 64–68. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








