An-Naml · 71/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هَٰذَا الْوَعْدُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ ۝٧١
Wa yaqooloona mataa haazal wa`du in kuntum saadiqeen
📖 Tekkim Wolof
Ñangay wax naan : “Dig bi moom kañ lay doon ndegam wax ngeen dëgg ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 69-73 — An-Naml

69قُلْ سِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَانظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُجْرِمِينَ
Neeleen : “Doxleen ci suuf si [wëréelu] te ngeen xool naka la tooñkat ya mujje”.
70وَلَا تَحْزَنْ عَلَيْهِمْ وَلَا تَكُن فِي ضَيْقٍ مِّمَّا يَمْكُرُونَ
Bul jàq ci ñoom te seeni pexe itam bu mu la xatal.
71وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هَٰذَا الْوَعْدُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ñangay wax naan : “Dig bi moom kañ lay doon ndegam wax ngeen dëgg ? ”
72قُلْ عَسَىٰ أَن يَكُونَ رَدِفَ لَكُم بَعْضُ الَّذِي تَسْتَعْجِلُونَ
Neel : “Amaana lii ngeen di yàkkamtee ngi ci seen kaw”.
73وَإِنَّ رَبَّكَ لَذُو فَضْلٍ عَلَى النَّاسِ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَشْكُرُونَ
Te nag sa Boroom aka bari ngëneel yu Muy jox nit ñi, waaye li ëpp ci ñoom duñu sant.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
71Aaya

Tekki — An-Naml 71

Simoore An-Naml Aaya 71 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñangay wax naan : “Dig bi moom kañ lay doon…

Simoore Aaya 71/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 69–73. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers