Al-Qasas · 12/88
Tekki Waxtaan — Al-Qasas
۞ وَحَرَّمْنَا عَلَيْهِ الْمَرَاضِعَ مِن قَبْلُ فَقَالَتْ هَلْ أَدُلُّكُمْ عَلَىٰ أَهْلِ بَيْتٍ يَكْفُلُونَهُ لَكُمْ وَهُمْ لَهُ نَاصِحُونَ ١٢
Transliteration
Wa harramnaa `alaihil maraadi`a min qablu faqaalat hal adullukum `alaaa ahli baitiny yakfuloonahoo lakum wa hum lahoo naasihoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Noo ko bañloo woon nàmpalkat ya. Ba mbokkam mu jigéen ma agsee, daldi wax ne : “Ndax duma leen tegtal waa kër goo xam ne danañu leen ko yaral te di ko toppatoo ? ”...
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 10-14 — Al-Qasas
10وَأَصْبَحَ فُؤَادُ أُمِّ مُوسَىٰ فَارِغًا ۖ إِن كَادَتْ لَتُبْدِي بِهِ لَوْلَا أَن رَّبَطْنَا عَلَىٰ قَلْبِهَا لِتَكُونَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Xolub ndeyu Muusaa ja jeex na tàkk. Ba mu xaw a feeñal, cëy bu Nu ko dëfëlul woon xolam ak la mu doonoon di ab jullit.
11وَقَالَتْ لِأُخْتِهِ قُصِّيهِ ۖ فَبَصُرَتْ بِهِ عَن جُنُبٍ وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
Mu wax mbokkam mu jigéen ma ne ko : “Topp ko” ; mu di ko bàyyi xel, topp ko te kenn xamut.
12۞ وَحَرَّمْنَا عَلَيْهِ الْمَرَاضِعَ مِن قَبْلُ فَقَالَتْ هَلْ أَدُلُّكُمْ عَلَىٰ أَهْلِ بَيْتٍ يَكْفُلُونَهُ لَكُمْ وَهُمْ لَهُ نَاصِحُونَ
Noo ko bañloo woon nàmpalkat ya. Ba mbokkam mu jigéen ma agsee, daldi wax ne : “Ndax duma leen tegtal waa kër goo xam ne danañu leen ko yaral te di ko toppatoo ? ”...
13فَرَدَدْنَاهُ إِلَىٰ أُمِّهِ كَيْ تَقَرَّ عَيْنُهَا وَلَا تَحْزَنَ وَلِتَعْلَمَ أَنَّ وَعْدَ اللَّهِ حَقٌّ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Nu daldi koy delloo ndeyam ja ngir mu wéttaliku ba bañ a tiit ak it ngir mu xam ne digub Yàlla lu dëggu la. Waaye li ëpp ci ñoom xamuñu.
14وَلَمَّا بَلَغَ أَشُدَّهُ وَاسْتَوَىٰ آتَيْنَاهُ حُكْمًا وَعِلْمًا ۚ وَكَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Ba mu matee sëkk te ñor xomm, [Muusaa] jox Nanu ko àtte ya ak xam-xam. Noonu la Nuy feye rafetalkat yi.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
12Aaya
Tekki — Al-Qasas 12
Simoore Al-Qasas Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noo ko bañloo woon nàmpalkat ya. Ba mbokkam mu jigéen…Simoore Aaya 12/88 — Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qasas Dégg, Al-Qasas Tekki, Al-Qasas mp3, Al-Qasas pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








