Aali Imran · 6/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
هُوَ الَّذِي يُصَوِّرُكُمْ فِي الْأَرْحَامِ كَيْفَ يَشَاءُ ۚ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ ۝٦
Huwal lazee yusawwirukum fil arhaami kaifa yashaaa`; laa ilaaha illaa Huwal `Azeezul Hakeem
📖 Tekkim Wolof
Moo leen móol ci seeni biiri nday, na Mu ko soobee. Amul jeneen Yàlla ju dul Moom, Mooy ki not, di ku xereñ.

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — Aali Imran

4مِن قَبْلُ هُدًى لِّلنَّاسِ وَأَنزَلَ الْفُرْقَانَ ۗ إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا بِآيَاتِ اللَّهِ لَهُمْ عَذَابٌ شَدِيدٌ ۗ وَاللَّهُ عَزِيزٌ ذُو انتِقَامٍ
ca bu jëkk, doonoon njub ci nit ñi. Moo wàcce Alxuraan. Ña weddi kàdduy Yàlla yi, am nañu mbugal mu tar ! Te Yàlla ku not la , Boroomug feyyu la.
5إِنَّ اللَّهَ لَا يَخْفَىٰ عَلَيْهِ شَيْءٌ فِي الْأَرْضِ وَلَا فِي السَّمَاءِ
Yàlla, dara nëbbuwul ci Moom biir asamaan ak suuf si.
6هُوَ الَّذِي يُصَوِّرُكُمْ فِي الْأَرْحَامِ كَيْفَ يَشَاءُ ۚ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Moo leen móol ci seeni biiri nday, na Mu ko soobee. Amul jeneen Yàlla ju dul Moom, Mooy ki not, di ku xereñ.
7هُوَ الَّذِي أَنزَلَ عَلَيْكَ الْكِتَابَ مِنْهُ آيَاتٌ مُّحْكَمَاتٌ هُنَّ أُمُّ الْكِتَابِ وَأُخَرُ مُتَشَابِهَاتٌ ۖ فَأَمَّا الَّذِينَ فِي قُلُوبِهِمْ زَيْغٌ فَيَتَّبِعُونَ مَا تَشَابَهَ مِنْهُ ابْتِغَاءَ الْفِتْنَةِ وَابْتِغَاءَ تَأْوِيلِهِ ۗ وَمَا يَعْلَمُ تَأْوِيلَهُ إِلَّا اللَّهُ ۗ وَالرَّاسِخُونَ فِي الْعِلْمِ يَقُولُونَ آمَنَّا بِهِ كُلٌّ مِّنْ عِندِ رَبِّنَا ۗ وَمَا يَذَّكَّرُ إِلَّا أُولُو الْأَلْبَابِ
Moom moo wàcce ci yaw Téere ba : am na ca ay laaya seen maanaa leer nañu, ñoo di cosaani àtte yi, ak yeneeni laaya yu seeni maanaa fésul. Ña nga xam ne jeng a nekk seeni xol, benn ca laaya yooyu lañuy topp ngir sàkku fitna ak jéem leen a firi, te Yàlla doŋŋ a xam seeni piri ak ña sax ci xam-xam. Danañu wax ne : “Gëm nanu ko : lépp ca sunu Boroom la bawoo ! ” Woroom xel yi rekk ay waaru.
8رَبَّنَا لَا تُزِغْ قُلُوبَنَا بَعْدَ إِذْ هَدَيْتَنَا وَهَبْ لَنَا مِن لَّدُنكَ رَحْمَةً ۚ إِنَّكَ أَنتَ الْوَهَّابُ
“Yaw sunu Boroom ! yàlla boo jengal sunuy xol ginnaaw ba nga nu gindee ; te may nu yërmaande ju bawoo ci yaw. Yaw de yaa di Mayewaakoon bi !
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
6Aaya

Tekki — Aali Imran 6

Simoore Aali Imran Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo leen móol ci seeni biiri nday, na Mu ko…

Simoore Aaya 6/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers