Aali Imran · 53/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
رَبَّنَا آمَنَّا بِمَا أَنزَلْتَ وَاتَّبَعْنَا الرَّسُولَ فَاكْتُبْنَا مَعَ الشَّاهِدِينَ ۝٥٣
Rabbanaaa aamannaa bimaaa anzalta wattaba`nar Rasoola faktubnaa ma`ash shaahideen
📖 Tekkim Wolof
Yaw sunu Boroom ! Gëm nanu li nga wàcce [Linjiil] te topp nanu Yonent bi [Iisaa]. Yàlla nanga dogal nu bokk ca seede yu dëggu ya”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 51-55 — Simoore Aali Imran

51إِنَّ اللَّهَ رَبِّي وَرَبُّكُمْ فَاعْبُدُوهُ ۗ هَٰذَا صِرَاطٌ مُّسْتَقِيمٌ
Yàlla miy sama Boroom di seen Boroom. Jaamuleen ko : lii mooy yoon wu jub xocc wi.”
52۞ فَلَمَّا أَحَسَّ عِيسَىٰ مِنْهُمُ الْكُفْرَ قَالَ مَنْ أَنصَارِي إِلَى اللَّهِ ۖ قَالَ الْحَوَارِيُّونَ نَحْنُ أَنصَارُ اللَّهِ آمَنَّا بِاللَّهِ وَاشْهَدْ بِأَنَّا مُسْلِمُونَ
Ba Iisaa ràññee ca ñoom gëmëdi, la daldi wax ne : “Waaw ana kan moo may dimbali ci liggéeyal Yàlla ? ” Gaa yu sell ya ne ko : “Nun noo lay dimbali ci yoonu Yàlla. Gëm nanu Yàlla. Seedeel ne nun way-wommatu lanu [jëm ci Yàlla].
53رَبَّنَا آمَنَّا بِمَا أَنزَلْتَ وَاتَّبَعْنَا الرَّسُولَ فَاكْتُبْنَا مَعَ الشَّاهِدِينَ
Yaw sunu Boroom ! Gëm nanu li nga wàcce [Linjiil] te topp nanu Yonent bi [Iisaa]. Yàlla nanga dogal nu bokk ca seede yu dëggu ya”.
54وَمَكَرُوا وَمَكَرَ اللَّهُ ۖ وَاللَّهُ خَيْرُ الْمَاكِرِينَ
Ñu tëral pexe. Yàlla it tëral pexe. Te Mooy gën jaa mën a tëral pexe !
55إِذْ قَالَ اللَّهُ يَا عِيسَىٰ إِنِّي مُتَوَفِّيكَ وَرَافِعُكَ إِلَيَّ وَمُطَهِّرُكَ مِنَ الَّذِينَ كَفَرُوا وَجَاعِلُ الَّذِينَ اتَّبَعُوكَ فَوْقَ الَّذِينَ كَفَرُوا إِلَىٰ يَوْمِ الْقِيَامَةِ ۖ ثُمَّ إِلَيَّ مَرْجِعُكُمْ فَأَحْكُمُ بَيْنَكُمْ فِيمَا كُنتُمْ فِيهِ تَخْتَلِفُونَ
Fàttalikul ba Boroom ba waxee ne : "Yaw Iisaa, danaa la faat, yékkati la jëme ci Man, Danaa la laabal ci bon-boni yéefar yi weddi te danaa def ña la topp ñu féete kaw ña la weddi ba Bis-pénc ba. Yéen ñépp dellu ci Man, Ma àtte seeni diggante ci li ngeen doon juuyoo.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
53Aaya

Tekki — Aali Imran 53

Simoore Aali Imran Aaya 53 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yaw sunu Boroom ! Gëm nanu li nga wàcce [Linjiil]…

Simoore Aaya 53/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 51–55. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers