Ar-Rum · 17/60
Tekki Waxtaan — Ar-Rum
فَسُبْحَانَ اللَّهِ حِينَ تُمْسُونَ وَحِينَ تُصْبِحُونَ ۝١٧
Fa Subhaanal laahi heena tumsoona wa heena tusbihoon
📖 Tekkim Wolof
Tudd naa sellug Yàlla, kañ naa ko !
🎧 Dégg

📜 Aaya 15-19 — Ar-Rum

15فَأَمَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ فَهُمْ فِي رَوْضَةٍ يُحْبَرُونَ
Ña gëmoon tey jëf u yiw, ña ngay xéewu ci biir ay dër ;
16وَأَمَّا الَّذِينَ كَفَرُوا وَكَذَّبُوا بِآيَاتِنَا وَلِقَاءِ الْآخِرَةِ فَأُولَٰئِكَ فِي الْعَذَابِ مُحْضَرُونَ
yéefar yay weddi Sunuy kàddu ak dajeb àllaaxira ba, ñoom ña nga ca biir mbugal ma.
17فَسُبْحَانَ اللَّهِ حِينَ تُمْسُونَ وَحِينَ تُصْبِحُونَ
Tudd naa sellug Yàlla, kañ naa ko !
18وَلَهُ الْحَمْدُ فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَعَشِيًّا وَحِينَ تُظْهِرُونَ
Xeeti cant yépp ñeel na Ko ci asamaan yeek suuf si, ca marax ga ak njolloor.
19يُخْرِجُ الْحَيَّ مِنَ الْمَيِّتِ وَيُخْرِجُ الْمَيِّتَ مِنَ الْحَيِّ وَيُحْيِي الْأَرْضَ بَعْدَ مَوْتِهَا ۚ وَكَذَٰلِكَ تُخْرَجُونَ
Mooy génne ndundu ci ndee, di génne ndee ci ndundu. Mooy dundal suuf ginnaaw ba mu dewee. Noonu it lees leen di génnee [yéen ñépp] ca bisub dekki ba.
Ar-RumFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
17Aaya

Tekki — Ar-Rum 17

Simoore Ar-Rum Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Tudd naa sellug Yàlla, kañ naa ko !

Simoore Aaya 17/60 — Ar-Rum الروم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Rum Dégg, Ar-Rum Tekki, Ar-Rum mp3, Ar-Rum pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers