Ar-Rum · 18/60
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rum
وَلَهُ الْحَمْدُ فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَعَشِيًّا وَحِينَ تُظْهِرُونَ ۝١٨
Wa lahul hamdu fis samaawaati wal ardi wa `ashiyyanw wa heena tuzhiroon
📖 Tekkim Wolof
Xeeti cant yépp ñeel na Ko ci asamaan yeek suuf si, ca marax ga ak njolloor.

🎧 Dégg


📜 Aaya 16-20 — Simoore Ar-Rum

16وَأَمَّا الَّذِينَ كَفَرُوا وَكَذَّبُوا بِآيَاتِنَا وَلِقَاءِ الْآخِرَةِ فَأُولَٰئِكَ فِي الْعَذَابِ مُحْضَرُونَ
yéefar yay weddi Sunuy kàddu ak dajeb àllaaxira ba, ñoom ña nga ca biir mbugal ma.
17فَسُبْحَانَ اللَّهِ حِينَ تُمْسُونَ وَحِينَ تُصْبِحُونَ
Tudd naa sellug Yàlla, kañ naa ko !
18وَلَهُ الْحَمْدُ فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَعَشِيًّا وَحِينَ تُظْهِرُونَ
Xeeti cant yépp ñeel na Ko ci asamaan yeek suuf si, ca marax ga ak njolloor.
19يُخْرِجُ الْحَيَّ مِنَ الْمَيِّتِ وَيُخْرِجُ الْمَيِّتَ مِنَ الْحَيِّ وَيُحْيِي الْأَرْضَ بَعْدَ مَوْتِهَا ۚ وَكَذَٰلِكَ تُخْرَجُونَ
Mooy génne ndundu ci ndee, di génne ndee ci ndundu. Mooy dundal suuf ginnaaw ba mu dewee. Noonu it lees leen di génnee [yéen ñépp] ca bisub dekki ba.
20وَمِنْ آيَاتِهِ أَنْ خَلَقَكُم مِّن تُرَابٍ ثُمَّ إِذَا أَنتُم بَشَرٌ تَنتَشِرُونَ
Bokk na ci kéemaanam yi : Mu binde leen suuf, - léegi nag, yéen a ngi nii tasaaroo ci àddina si -.
Ar-RumFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
18Aaya

Tekki — Ar-Rum 18

Simoore Ar-Rum Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xeeti cant yépp ñeel na Ko ci asamaan yeek suuf…

Simoore Aaya 18/60 — Simoore Ar-Rum الروم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rum Dégg, Simoore Ar-Rum Tekki, Simoore Ar-Rum mp3, Simoore Ar-Rum pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers