Ar-Rum · 55/60
Tekki Waxtaan — Ar-Rum
وَيَوْمَ تَقُومُ السَّاعَةُ يُقْسِمُ الْمُجْرِمُونَ مَا لَبِثُوا غَيْرَ سَاعَةٍ ۚ كَذَٰلِكَ كَانُوا يُؤْفَكُونَ ۝٥٥
Wa Yawma taqoomus Saa`atu yuqsimul mujrimoona maa labisoo ghaira saa`ah; kazaalika kaanoo yu`fakoon
📖 Tekkim Wolof
Bu Bis-pénc ba taxawee, tooñkat ya danañu giñ naan as ndiir su ndaw la nu fi saxoon. Noonu la Nu leen daan férawale, soreel leen dëgg ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 53-57 — Ar-Rum

53وَمَا أَنتَ بِهَادِ الْعُمْيِ عَن ضَلَالَتِهِمْ ۖ إِن تُسْمِعُ إِلَّا مَن يُؤْمِنُ بِآيَاتِنَا فَهُم مُّسْلِمُونَ
Du caageene yaw yaaw gindi gumba yi ci seen réer ga. Ñi nga mën a dégtal [sa woote bii] daal, ñooy ña gëm, di ay jullit.
54۞ اللَّهُ الَّذِي خَلَقَكُم مِّن ضَعْفٍ ثُمَّ جَعَلَ مِن بَعْدِ ضَعْفٍ قُوَّةً ثُمَّ جَعَلَ مِن بَعْدِ قُوَّةٍ ضَعْفًا وَشَيْبَةً ۚ يَخْلُقُ مَا يَشَاءُ ۖ وَهُوَ الْعَلِيمُ الْقَدِيرُ
Yàlla mi leen bind cig lott, teg ca kàttan ; delloo ci lott gu ànd ak kumur, màggat [bijjaaw] : Te mooy sàkk lu ko soob, Mooy ki Xam te Mën.
55وَيَوْمَ تَقُومُ السَّاعَةُ يُقْسِمُ الْمُجْرِمُونَ مَا لَبِثُوا غَيْرَ سَاعَةٍ ۚ كَذَٰلِكَ كَانُوا يُؤْفَكُونَ
Bu Bis-pénc ba taxawee, tooñkat ya danañu giñ naan as ndiir su ndaw la nu fi saxoon. Noonu la Nu leen daan férawale, soreel leen dëgg ;
56وَقَالَ الَّذِينَ أُوتُوا الْعِلْمَ وَالْإِيمَانَ لَقَدْ لَبِثْتُمْ فِي كِتَابِ اللَّهِ إِلَىٰ يَوْمِ الْبَعْثِ ۖ فَهَٰذَا يَوْمُ الْبَعْثِ وَلَٰكِنَّكُمْ كُنتُمْ لَا تَعْلَمُونَ
Gaa ña amoon xam-xam ak ngëm, ne leen : “Sax ngeen fa ci dogalu Yàlla ba bisub dekki ba, - lii nag mooy bisub dekki ba, - waaye yéen xamuleen woon”.
57فَيَوْمَئِذٍ لَّا يَنفَعُ الَّذِينَ ظَلَمُوا مَعْذِرَتُهُمْ وَلَا هُمْ يُسْتَعْتَبُونَ
Su boobaa, tooñkat ya, seenug tinu du fa jariñ dara te kenn duleen faale.
Ar-RumFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
55Aaya

Tekki — Ar-Rum 55

Simoore Ar-Rum Aaya 55 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu Bis-pénc ba taxawee, tooñkat ya danañu giñ naan as…

Simoore Aaya 55/60 — Ar-Rum الروم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Rum Dégg, Ar-Rum Tekki, Ar-Rum mp3, Ar-Rum pdf. Aaya 53–57. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers