Ar-Rum · 8/60
Tekki Waxtaan — Ar-Rum
أَوَلَمْ يَتَفَكَّرُوا فِي أَنفُسِهِم ۗ مَّا خَلَقَ اللَّهُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا إِلَّا بِالْحَقِّ وَأَجَلٍ مُّسَمًّى ۗ وَإِنَّ كَثِيرًا مِّنَ النَّاسِ بِلِقَاءِ رَبِّهِمْ لَكَافِرُونَ ۝٨
Awalam yatafakkaroo feee anfusihim; maa khalaqal laahus samaawaati wal arda wa maa bainahumaaa illaa bil haqqi wa ajalim musammaa; wa inna kaseeram minan naasi biliqaaa`i Rabbihim lakaafiroon
📖 Tekkim Wolof
Ndax dañoo xalaatul ci seen bopp ? Yàlla bindul asamaan yeek suuf si ak li nekk ci seen diggante lu dul ci dëgg, te sàkkal na lépp ay dig. Te nag li bari ci nit ñi dañoo weddi te danañu dajeek seen Boroom.

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Ar-Rum

6وَعْدَ اللَّهِ ۖ لَا يُخْلِفُ اللَّهُ وَعْدَهُ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَ النَّاسِ لَا يَعْلَمُونَ
Loolu mooy li Yàlla di dige. Te Yàlla du wuute ab digam, waaye li ëpp ci nit ñi gëmuñu.
7يَعْلَمُونَ ظَاهِرًا مِّنَ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَهُمْ عَنِ الْآخِرَةِ هُمْ غَافِلُونَ
Danañu xam li feeñ ci dundug àddina, te ñoom ñu sàggan lañu ci mbiri àllaaxira,.
8أَوَلَمْ يَتَفَكَّرُوا فِي أَنفُسِهِم ۗ مَّا خَلَقَ اللَّهُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا إِلَّا بِالْحَقِّ وَأَجَلٍ مُّسَمًّى ۗ وَإِنَّ كَثِيرًا مِّنَ النَّاسِ بِلِقَاءِ رَبِّهِمْ لَكَافِرُونَ
Ndax dañoo xalaatul ci seen bopp ? Yàlla bindul asamaan yeek suuf si ak li nekk ci seen diggante lu dul ci dëgg, te sàkkal na lépp ay dig. Te nag li bari ci nit ñi dañoo weddi te danañu dajeek seen Boroom.
9أَوَلَمْ يَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَيَنظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ كَانُوا أَشَدَّ مِنْهُمْ قُوَّةً وَأَثَارُوا الْأَرْضَ وَعَمَرُوهَا أَكْثَرَ مِمَّا عَمَرُوهَا وَجَاءَتْهُمْ رُسُلُهُم بِالْبَيِّنَاتِ ۖ فَمَا كَانَ اللَّهُ لِيَظْلِمَهُمْ وَلَٰكِن كَانُوا أَنفُسَهُمْ يَظْلِمُونَ
Ndax dañoo doxul ci suuf tey xool naka la ñu mujje ña leen fa jiitu woon ? Ñoo leen ëppoon doole, daan réjji suuf si, feesoon ko dell ak seeni njaboot. Seeni Yonent indiloon leen ay kàddu yu leer. Yàlla tooñuleen, waaye ñoo tooñ seen bopp.
10ثُمَّ كَانَ عَاقِبَةَ الَّذِينَ أَسَاءُوا السُّوأَىٰ أَن كَذَّبُوا بِآيَاتِ اللَّهِ وَكَانُوا بِهَا يَسْتَهْزِئُونَ
Ña daan jëf u ñaawteef, seenug mujj dellu ñaaw, ndax ñoom weddi woon nañu kàdduy Yàlla, daan ko yéjji.
Ar-RumFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Ar-Rum 8

Simoore Ar-Rum Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax dañoo xalaatul ci seen bopp ? Yàlla bindul asamaan…

Simoore Aaya 8/60 — Ar-Rum الروم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Rum Dégg, Ar-Rum Tekki, Ar-Rum mp3, Ar-Rum pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers