Ya-Sin · 51/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
وَنُفِخَ فِي الصُّورِ فَإِذَا هُم مِّنَ الْأَجْدَاثِ إِلَىٰ رَبِّهِمْ يَنسِلُونَ ۝٥١
Wa nufikha fis-soori faizaa hum minal ajdaasi ilaa Rabbihim yansiloon
📖 Tekkim Wolof
Su ñu ëfee Buftu bi, dañu naan futeet ca bàmmeel ya, dox wuti seen Boroom,
🎧 Dégg

📜 Aaya 49-53 — Ya-Sin

49مَا يَنظُرُونَ إِلَّا صَيْحَةً وَاحِدَةً تَأْخُذُهُمْ وَهُمْ يَخِصِّمُونَ
Xaaruñu lu dul genn yuuxu gu leen jël fekk leen ñuy xuloo.
50فَلَا يَسْتَطِيعُونَ تَوْصِيَةً وَلَا إِلَىٰ أَهْلِهِمْ يَرْجِعُونَ
Duñu mën a batale, di dénkaane, mbaa ñuy mën a dellu ca seen njaboot.
51وَنُفِخَ فِي الصُّورِ فَإِذَا هُم مِّنَ الْأَجْدَاثِ إِلَىٰ رَبِّهِمْ يَنسِلُونَ
Su ñu ëfee Buftu bi, dañu naan futeet ca bàmmeel ya, dox wuti seen Boroom,
52قَالُوا يَا وَيْلَنَا مَن بَعَثَنَا مِن مَّرْقَدِنَا ۜ ۗ هَٰذَا مَا وَعَدَ الرَّحْمَٰنُ وَصَدَقَ الْمُرْسَلُونَ
ñuy wax naan : “Wóoy ngalla nun ! Moo ana kan moo nu yékkatee ci sunu yàndoorukaay bi ? ” Lii dey mooy la nu Yërëmaakoon bi doon dig ; kon Yonent yi waxoon nañu dëgg.
53إِن كَانَتْ إِلَّا صَيْحَةً وَاحِدَةً فَإِذَا هُمْ جَمِيعٌ لَّدَيْنَا مُحْضَرُونَ
Genn ug xaacu rekk a jib, ñu seet-seeti ñoom ñépp, ne jaseet Sunu kanam.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
51Aaya

Tekki — Ya-Sin 51

Simoore Ya-Sin Aaya 51 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Su ñu ëfee Buftu bi, dañu naan futeet ca bàmmeel…

Simoore Aaya 51/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 49–53. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers