As-Saffat · 10/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِلَّا مَنْ خَطِفَ الْخَطْفَةَ فَأَتْبَعَهُ شِهَابٌ ثَاقِبٌ ۝١٠
Illaa man khatifal khatfata fa atba`ahoo shihaabun saaqib
📖 Tekkim Wolof
Xanaa rekk léeg-léeg mu am ñu cay sàcc ay xibaar ; ñu di ko dàq ak jumu safara buy bënn.

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Simoore As-Saffat

8لَّا يَسَّمَّعُونَ إِلَى الْمَلَإِ الْأَعْلَىٰ وَيُقْذَفُونَ مِن كُلِّ جَانِبٍ
Duñu mën yëddu waa péey ba gën a kawe ; te dañu leen fay mbàqe wet gu nekk,
9دُحُورًا ۖ وَلَهُمْ عَذَابٌ وَاصِبٌ
dàqe leen fa. Ñu am mbugal muy sax.
10إِلَّا مَنْ خَطِفَ الْخَطْفَةَ فَأَتْبَعَهُ شِهَابٌ ثَاقِبٌ
Xanaa rekk léeg-léeg mu am ñu cay sàcc ay xibaar ; ñu di ko dàq ak jumu safara buy bënn.
11فَاسْتَفْتِهِمْ أَهُمْ أَشَدُّ خَلْقًا أَم مَّنْ خَلَقْنَا ۚ إِنَّا خَلَقْنَاهُم مِّن طِينٍ لَّازِبٍ
Laajleen baxam dañoo gën a jafe bind ñeneen ña Nu bind ? Noo ngi leen binde ci ban bu tikk !
12بَلْ عَجِبْتَ وَيَسْخَرُونَ
Yaw waaru nga, te ñoom ña ngay tejjiy reetaan !
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — As-Saffat 10

Simoore As-Saffat Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xanaa rekk léeg-léeg mu am ñu cay sàcc ay xibaar…

Simoore Aaya 10/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers